Ash-Shu'ara · 48/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
رَبِّ مُوسَىٰ وَهَارُونَ ٤٨
Transliteration
Rabbi Moosaa wa Haaroon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Boroom Muusaa ak Aaruuna”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 46-50 — Simoore Ash-Shu'ara
46فَأُلْقِيَ السَّحَرَةُ سَاجِدِينَ
Jibar ya daldi rot sujjóot,
47قَالُوا آمَنَّا بِرَبِّ الْعَالَمِينَ
daldi wax ne : “Gëm nanu Boroom àddina si yépp,
48رَبِّ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
Boroom Muusaa ak Aaruuna”.
49قَالَ آمَنتُمْ لَهُ قَبْلَ أَنْ آذَنَ لَكُمْ ۖ إِنَّهُ لَكَبِيرُكُمُ الَّذِي عَلَّمَكُمُ السِّحْرَ فَلَسَوْفَ تَعْلَمُونَ ۚ لَأُقَطِّعَنَّ أَيْدِيَكُمْ وَأَرْجُلَكُم مِّنْ خِلَافٍ وَلَأُصَلِّبَنَّكُمْ أَجْمَعِينَ
[Firawna] ne leen : “Gëmoon ngeen ko ba ma leen a laataa woo. [Xam naa ne] mooy kàndiŋ mi leen jàngal njibar ! Dangeen xam ne ! Danaa dagg seen yoxook seeni tànk, jalawle ko, danaa leen daaj yéen ñépp”.
50قَالُوا لَا ضَيْرَ ۖ إِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا مُنقَلِبُونَ
Ñu ne ko : “Boo yaboo ! Nun daal jublu nanu sunu Boroom.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
48Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 48
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Boroom Muusaa ak Aaruuna”.Simoore Aaya 48/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 8, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








