Ash-Shu'ara · 47/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
قَالُوا آمَنَّا بِرَبِّ الْعَالَمِينَ ۝٤٧
Qaalooo aamannaa bi Rabbil `aalameen
📖 Tekkim Wolof
daldi wax ne : “Gëm nanu Boroom àddina si yépp,
🎧 Dégg

📜 Aaya 45-49 — Ash-Shu'ara

45فَأَلْقَىٰ مُوسَىٰ عَصَاهُ فَإِذَا هِيَ تَلْقَفُ مَا يَأْفِكُونَ
Muusaa daldi sànni yetam wa, ndeketeyoo mëdd na ya ñu deferoon.
46فَأُلْقِيَ السَّحَرَةُ سَاجِدِينَ
Jibar ya daldi rot sujjóot,
47قَالُوا آمَنَّا بِرَبِّ الْعَالَمِينَ
daldi wax ne : “Gëm nanu Boroom àddina si yépp,
48رَبِّ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
Boroom Muusaa ak Aaruuna”.
49قَالَ آمَنتُمْ لَهُ قَبْلَ أَنْ آذَنَ لَكُمْ ۖ إِنَّهُ لَكَبِيرُكُمُ الَّذِي عَلَّمَكُمُ السِّحْرَ فَلَسَوْفَ تَعْلَمُونَ ۚ لَأُقَطِّعَنَّ أَيْدِيَكُمْ وَأَرْجُلَكُم مِّنْ خِلَافٍ وَلَأُصَلِّبَنَّكُمْ أَجْمَعِينَ
[Firawna] ne leen : “Gëmoon ngeen ko ba ma leen a laataa woo. [Xam naa ne] mooy kàndiŋ mi leen jàngal njibar ! Dangeen xam ne ! Danaa dagg seen yoxook seeni tànk, jalawle ko, danaa leen daaj yéen ñépp”.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
47Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 47

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 47 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : daldi wax ne : “Gëm nanu Boroom àddina si yépp,

Simoore Aaya 47/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 45–49. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers