Ash-Shu'ara · 75/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
قَالَ أَفَرَأَيْتُم مَّا كُنتُمْ تَعْبُدُونَ ٧٥
Transliteration
Qaala afara `aitum maa kuntum ta`budoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ibraahiima ne leen : “Xanaa gisuleen li ngeen di jaamu... ?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 73-77 — Ash-Shu'ara
73أَوْ يَنفَعُونَكُمْ أَوْ يَضُرُّونَ
walla ñu di leen jariñ mbaa ñu leen di lor ? ”
74قَالُوا بَلْ وَجَدْنَا آبَاءَنَا كَذَٰلِكَ يَفْعَلُونَ
Ñu wax ne : “Nun kat, dañoo fekk rekk sunuy baay daan ko def”.
75قَالَ أَفَرَأَيْتُم مَّا كُنتُمْ تَعْبُدُونَ
Ibraahiima ne leen : “Xanaa gisuleen li ngeen di jaamu... ?
76أَنتُمْ وَآبَاؤُكُمُ الْأَقْدَمُونَ
Yéen ak seen maam ya fi woon ?
77فَإِنَّهُمْ عَدُوٌّ لِّي إِلَّا رَبَّ الْعَالَمِينَ
Ñoom ñépp sama noon lañu ku dul Yàlla Miy Boroom àddina si,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
75Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 75
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 75 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ibraahiima ne leen : “Xanaa gisuleen li ngeen di jaamu...…Simoore Aaya 75/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 73–77. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








