Ash-Shu'ara · 76/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
أَنتُمْ وَآبَاؤُكُمُ الْأَقْدَمُونَ ۝٧٦
Antum wa aabaaa`ukumul aqdamoon
📖 Tekkim Wolof
Yéen ak seen maam ya fi woon ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 74-78 — Ash-Shu'ara

74قَالُوا بَلْ وَجَدْنَا آبَاءَنَا كَذَٰلِكَ يَفْعَلُونَ
Ñu wax ne : “Nun kat, dañoo fekk rekk sunuy baay daan ko def”.
75قَالَ أَفَرَأَيْتُم مَّا كُنتُمْ تَعْبُدُونَ
Ibraahiima ne leen : “Xanaa gisuleen li ngeen di jaamu... ?
76أَنتُمْ وَآبَاؤُكُمُ الْأَقْدَمُونَ
Yéen ak seen maam ya fi woon ?
77فَإِنَّهُمْ عَدُوٌّ لِّي إِلَّا رَبَّ الْعَالَمِينَ
Ñoom ñépp sama noon lañu ku dul Yàlla Miy Boroom àddina si,
78الَّذِي خَلَقَنِي فَهُوَ يَهْدِينِ
Moom mi ma bind te gindi ma ;
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
76Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 76

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 76 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen ak seen maam ya fi woon ?

Simoore Aaya 76/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 74–78. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers