Ash-Shu'ara · 95/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَجُنُودُ إِبْلِيسَ أَجْمَعُونَ ۝٩٥
Wa junoodu Ibleesa ajma`oon
📖 Tekkim Wolof
ak gàngoorug Ibliis ga gépp.

🎧 Dégg


📜 Aaya 93-97 — Simoore Ash-Shu'ara

93مِن دُونِ اللَّهِ هَلْ يَنصُرُونَكُمْ أَوْ يَنتَصِرُونَ
bàyyi woon Yàlla ? Ndax mën nanoo dimbali seen bopp ? Walla ñu dimbali leen ? ”
94فَكُبْكِبُوا فِيهَا هُمْ وَالْغَاوُونَ
Ñu sànni leen fa, galajaane leen ñook mboxos ma,
95وَجُنُودُ إِبْلِيسَ أَجْمَعُونَ
ak gàngoorug Ibliis ga gépp.
96قَالُوا وَهُمْ فِيهَا يَخْتَصِمُونَ
Ñuy wax ca biir tey xuloo :
97تَاللَّهِ إِن كُنَّا لَفِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
“Waat naa ci Yàlla ne ! Noo ngi woon ci réer gu bir,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
95Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 95

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 95 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak gàngoorug Ibliis ga gépp.

Simoore Aaya 95/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 93–97. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers