Ash-Shu'ara · 94/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
فَكُبْكِبُوا فِيهَا هُمْ وَالْغَاوُونَ ۝٩٤
Fakubkiboo feehaa hum walghaawoon
📖 Tekkim Wolof
Ñu sànni leen fa, galajaane leen ñook mboxos ma,

🎧 Dégg


📜 Aaya 92-96 — Simoore Ash-Shu'ara

92وَقِيلَ لَهُمْ أَيْنَ مَا كُنتُمْ تَعْبُدُونَ
Ñu wax leen ne : “Ana fan ngeen nekkoon di fa jaamoo,
93مِن دُونِ اللَّهِ هَلْ يَنصُرُونَكُمْ أَوْ يَنتَصِرُونَ
bàyyi woon Yàlla ? Ndax mën nanoo dimbali seen bopp ? Walla ñu dimbali leen ? ”
94فَكُبْكِبُوا فِيهَا هُمْ وَالْغَاوُونَ
Ñu sànni leen fa, galajaane leen ñook mboxos ma,
95وَجُنُودُ إِبْلِيسَ أَجْمَعُونَ
ak gàngoorug Ibliis ga gépp.
96قَالُوا وَهُمْ فِيهَا يَخْتَصِمُونَ
Ñuy wax ca biir tey xuloo :
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
94Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 94

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 94 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu sànni leen fa, galajaane leen ñook mboxos ma,

Simoore Aaya 94/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 92–96. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers