Ash-Shu'ara · 96/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
قَالُوا وَهُمْ فِيهَا يَخْتَصِمُونَ ۝٩٦
Qaaloo wa hum feehaa yakkhtasimoon
📖 Tekkim Wolof
Ñuy wax ca biir tey xuloo :

🎧 Dégg


📜 Aaya 94-98 — Simoore Ash-Shu'ara

94فَكُبْكِبُوا فِيهَا هُمْ وَالْغَاوُونَ
Ñu sànni leen fa, galajaane leen ñook mboxos ma,
95وَجُنُودُ إِبْلِيسَ أَجْمَعُونَ
ak gàngoorug Ibliis ga gépp.
96قَالُوا وَهُمْ فِيهَا يَخْتَصِمُونَ
Ñuy wax ca biir tey xuloo :
97تَاللَّهِ إِن كُنَّا لَفِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
“Waat naa ci Yàlla ne ! Noo ngi woon ci réer gu bir,
98إِذْ نُسَوِّيكُم بِرَبِّ الْعَالَمِينَ
jamono ya nu leen doon yemaleek Boroom àddina si.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
96Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 96

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 96 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñuy wax ca biir tey xuloo :

Simoore Aaya 96/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 94–98. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers