Al-Qasas · 61/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
أَفَمَن وَعَدْنَاهُ وَعْدًا حَسَنًا فَهُوَ لَاقِيهِ كَمَن مَّتَّعْنَاهُ مَتَاعَ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ثُمَّ هُوَ يَوْمَ الْقِيَامَةِ مِنَ الْمُحْضَرِينَ ۝٦١
Afamanw wa`adnaahu wa`dan hasanan fahuwa laaqeehi kamam matta`naahu mataa`al hayaatid dunyaa summa huwa Yawmal Qiyaamati minal muhdareen
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax ka Nu digoon dig bu rafet te mu dajeek moom, dana mel ni ka Nu bànneexaloon ca àddina ak ug dundam, bu ñu leen teewalee ca seen kanamu Boroom.

🎧 Dégg


📜 Aaya 59-63 — Simoore Al-Qasas

59وَمَا كَانَ رَبُّكَ مُهْلِكَ الْقُرَىٰ حَتَّىٰ يَبْعَثَ فِي أُمِّهَا رَسُولًا يَتْلُو عَلَيْهِمْ آيَاتِنَا ۚ وَمَا كُنَّا مُهْلِكِي الْقُرَىٰ إِلَّا وَأَهْلُهَا ظَالِمُونَ
Yàlla du faagaagal yenn dëkk ndare du dafa yebal ab Yonent ca dëkk ba fa gën a rëy, mu di leen nettali ay kàddoom. Te Nun Yàlla dunu faagaagal ay dëkk lu dul ne dañuy tooñ.
60وَمَا أُوتِيتُم مِّن شَيْءٍ فَمَتَاعُ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَزِينَتُهَا ۚ وَمَا عِندَ اللَّهِ خَيْرٌ وَأَبْقَىٰ ۚ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Lii Nu leen jox, bànneexu dundug àddina [doŋŋ la], te la nekk fa Yàlla moo gën a des ... Moo ndax dangeen dul xel-lu ?
61أَفَمَن وَعَدْنَاهُ وَعْدًا حَسَنًا فَهُوَ لَاقِيهِ كَمَن مَّتَّعْنَاهُ مَتَاعَ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ثُمَّ هُوَ يَوْمَ الْقِيَامَةِ مِنَ الْمُحْضَرِينَ
Moo ndax ka Nu digoon dig bu rafet te mu dajeek moom, dana mel ni ka Nu bànneexaloon ca àddina ak ug dundam, bu ñu leen teewalee ca seen kanamu Boroom.
62وَيَوْمَ يُنَادِيهِمْ فَيَقُولُ أَيْنَ شُرَكَائِيَ الَّذِينَ كُنتُمْ تَزْعُمُونَ
Bu keroogee ba mu di leen woon, naan leen : “Ana ka ngeen Ma doon bokkaaleel ? ”
63قَالَ الَّذِينَ حَقَّ عَلَيْهِمُ الْقَوْلُ رَبَّنَا هَٰؤُلَاءِ الَّذِينَ أَغْوَيْنَا أَغْوَيْنَاهُمْ كَمَا غَوَيْنَا ۖ تَبَرَّأْنَا إِلَيْكَ ۖ مَا كَانُوا إِيَّانَا يَعْبُدُونَ
Ña wax ja dal ci seen kaw daldi ne : “Yaw sunu Boroom, ñii ñoo nu fàbbiwoon ni ñu fàbbikoo woon. Deñ nanu ci ñoom ci sa kanam : ñii daal jaamuwuñu nu woon”.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
61Aaya

Tekki — Al-Qasas 61

Simoore Al-Qasas Aaya 61 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax ka Nu digoon dig bu rafet te mu…

Simoore Aaya 61/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 59–63. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers