Al-Qasas · 60/88
Tekki Waxtaan — Al-Qasas
وَمَا أُوتِيتُم مِّن شَيْءٍ فَمَتَاعُ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَزِينَتُهَا ۚ وَمَا عِندَ اللَّهِ خَيْرٌ وَأَبْقَىٰ ۚ أَفَلَا تَعْقِلُونَ ۝٦٠
Wa maaa ooteetum min shai`in famataa`ul hayaatid dunyaa wa zeenatuhaa; wa maa `indal laahi khairunw wa abqaa; afalaa ta`qiloon
📖 Tekkim Wolof
Lii Nu leen jox, bànneexu dundug àddina [doŋŋ la], te la nekk fa Yàlla moo gën a des ... Moo ndax dangeen dul xel-lu ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 58-62 — Al-Qasas

58وَكَمْ أَهْلَكْنَا مِن قَرْيَةٍ بَطِرَتْ مَعِيشَتَهَا ۖ فَتِلْكَ مَسَاكِنُهُمْ لَمْ تُسْكَن مِّن بَعْدِهِمْ إِلَّا قَلِيلًا ۖ وَكُنَّا نَحْنُ الْوَارِثِينَ
Aka bari dëkk bu Nu faagaagal ci sababus seenug weddi te ñu daan dunde xéewal, ca seen kër ya lu néew la, te keneen dëkkee seen ginnaaw, Nun Yàlla noo doon donnale.
59وَمَا كَانَ رَبُّكَ مُهْلِكَ الْقُرَىٰ حَتَّىٰ يَبْعَثَ فِي أُمِّهَا رَسُولًا يَتْلُو عَلَيْهِمْ آيَاتِنَا ۚ وَمَا كُنَّا مُهْلِكِي الْقُرَىٰ إِلَّا وَأَهْلُهَا ظَالِمُونَ
Yàlla du faagaagal yenn dëkk ndare du dafa yebal ab Yonent ca dëkk ba fa gën a rëy, mu di leen nettali ay kàddoom. Te Nun Yàlla dunu faagaagal ay dëkk lu dul ne dañuy tooñ.
60وَمَا أُوتِيتُم مِّن شَيْءٍ فَمَتَاعُ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَزِينَتُهَا ۚ وَمَا عِندَ اللَّهِ خَيْرٌ وَأَبْقَىٰ ۚ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Lii Nu leen jox, bànneexu dundug àddina [doŋŋ la], te la nekk fa Yàlla moo gën a des ... Moo ndax dangeen dul xel-lu ?
61أَفَمَن وَعَدْنَاهُ وَعْدًا حَسَنًا فَهُوَ لَاقِيهِ كَمَن مَّتَّعْنَاهُ مَتَاعَ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ثُمَّ هُوَ يَوْمَ الْقِيَامَةِ مِنَ الْمُحْضَرِينَ
Moo ndax ka Nu digoon dig bu rafet te mu dajeek moom, dana mel ni ka Nu bànneexaloon ca àddina ak ug dundam, bu ñu leen teewalee ca seen kanamu Boroom.
62وَيَوْمَ يُنَادِيهِمْ فَيَقُولُ أَيْنَ شُرَكَائِيَ الَّذِينَ كُنتُمْ تَزْعُمُونَ
Bu keroogee ba mu di leen woon, naan leen : “Ana ka ngeen Ma doon bokkaaleel ? ”
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
60Aaya

Tekki — Al-Qasas 60

Simoore Al-Qasas Aaya 60 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lii Nu leen jox, bànneexu dundug àddina [doŋŋ la], te…

Simoore Aaya 60/88 — Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qasas Dégg, Al-Qasas Tekki, Al-Qasas mp3, Al-Qasas pdf. Aaya 58–62. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers