Al-Qasas · 62/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
وَيَوْمَ يُنَادِيهِمْ فَيَقُولُ أَيْنَ شُرَكَائِيَ الَّذِينَ كُنتُمْ تَزْعُمُونَ ۝٦٢
Wa Yawma yunaadeehim fa-yaqoolu aina shurakaaa `iyal lazeena kuntum taz`umoon
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee ba mu di leen woon, naan leen : “Ana ka ngeen Ma doon bokkaaleel ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 60-64 — Simoore Al-Qasas

60وَمَا أُوتِيتُم مِّن شَيْءٍ فَمَتَاعُ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَزِينَتُهَا ۚ وَمَا عِندَ اللَّهِ خَيْرٌ وَأَبْقَىٰ ۚ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Lii Nu leen jox, bànneexu dundug àddina [doŋŋ la], te la nekk fa Yàlla moo gën a des ... Moo ndax dangeen dul xel-lu ?
61أَفَمَن وَعَدْنَاهُ وَعْدًا حَسَنًا فَهُوَ لَاقِيهِ كَمَن مَّتَّعْنَاهُ مَتَاعَ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ثُمَّ هُوَ يَوْمَ الْقِيَامَةِ مِنَ الْمُحْضَرِينَ
Moo ndax ka Nu digoon dig bu rafet te mu dajeek moom, dana mel ni ka Nu bànneexaloon ca àddina ak ug dundam, bu ñu leen teewalee ca seen kanamu Boroom.
62وَيَوْمَ يُنَادِيهِمْ فَيَقُولُ أَيْنَ شُرَكَائِيَ الَّذِينَ كُنتُمْ تَزْعُمُونَ
Bu keroogee ba mu di leen woon, naan leen : “Ana ka ngeen Ma doon bokkaaleel ? ”
63قَالَ الَّذِينَ حَقَّ عَلَيْهِمُ الْقَوْلُ رَبَّنَا هَٰؤُلَاءِ الَّذِينَ أَغْوَيْنَا أَغْوَيْنَاهُمْ كَمَا غَوَيْنَا ۖ تَبَرَّأْنَا إِلَيْكَ ۖ مَا كَانُوا إِيَّانَا يَعْبُدُونَ
Ña wax ja dal ci seen kaw daldi ne : “Yaw sunu Boroom, ñii ñoo nu fàbbiwoon ni ñu fàbbikoo woon. Deñ nanu ci ñoom ci sa kanam : ñii daal jaamuwuñu nu woon”.
64وَقِيلَ ادْعُوا شُرَكَاءَكُمْ فَدَعَوْهُمْ فَلَمْ يَسْتَجِيبُوا لَهُمْ وَرَأَوُا الْعَذَابَ ۚ لَوْ أَنَّهُمْ كَانُوا يَهْتَدُونَ
Nu wax ne : “Wooleen seen bokkaale ya”. Ñu woo leen, waaye wuyyuwuñu leen. Gis nañu mbugal ma, cëy bu ñu gindiku woon.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
62Aaya

Tekki — Al-Qasas 62

Simoore Al-Qasas Aaya 62 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee ba mu di leen woon, naan leen :…

Simoore Aaya 62/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 60–64. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers