Al-Qasas · 65/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
وَيَوْمَ يُنَادِيهِمْ فَيَقُولُ مَاذَا أَجَبْتُمُ الْمُرْسَلِينَ ۝٦٥
Wa Yawma yunaadeehim fa yaqoolu maazaaa ajabtumul mursaleen
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee bis ba Mu leen di woo naan leen : “Ana lan ngeen tontu woon Yonent ya ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 63-67 — Simoore Al-Qasas

63قَالَ الَّذِينَ حَقَّ عَلَيْهِمُ الْقَوْلُ رَبَّنَا هَٰؤُلَاءِ الَّذِينَ أَغْوَيْنَا أَغْوَيْنَاهُمْ كَمَا غَوَيْنَا ۖ تَبَرَّأْنَا إِلَيْكَ ۖ مَا كَانُوا إِيَّانَا يَعْبُدُونَ
Ña wax ja dal ci seen kaw daldi ne : “Yaw sunu Boroom, ñii ñoo nu fàbbiwoon ni ñu fàbbikoo woon. Deñ nanu ci ñoom ci sa kanam : ñii daal jaamuwuñu nu woon”.
64وَقِيلَ ادْعُوا شُرَكَاءَكُمْ فَدَعَوْهُمْ فَلَمْ يَسْتَجِيبُوا لَهُمْ وَرَأَوُا الْعَذَابَ ۚ لَوْ أَنَّهُمْ كَانُوا يَهْتَدُونَ
Nu wax ne : “Wooleen seen bokkaale ya”. Ñu woo leen, waaye wuyyuwuñu leen. Gis nañu mbugal ma, cëy bu ñu gindiku woon.
65وَيَوْمَ يُنَادِيهِمْ فَيَقُولُ مَاذَا أَجَبْتُمُ الْمُرْسَلِينَ
Bu keroogee bis ba Mu leen di woo naan leen : “Ana lan ngeen tontu woon Yonent ya ? ”
66فَعَمِيَتْ عَلَيْهِمُ الْأَنبَاءُ يَوْمَئِذٍ فَهُمْ لَا يَتَسَاءَلُونَ
Seeni firnde jaxasoo, bu boobaa [dañu naa xuum] dootuñu laajante.
67فَأَمَّا مَن تَابَ وَآمَنَ وَعَمِلَ صَالِحًا فَعَسَىٰ أَن يَكُونَ مِنَ الْمُفْلِحِينَ
Képp ku ca tuub te gëm te jëf u yiw, amaana mu texe.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
65Aaya

Tekki — Al-Qasas 65

Simoore Al-Qasas Aaya 65 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee bis ba Mu leen di woo naan leen…

Simoore Aaya 65/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 63–67. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers