Aali Imran · 124/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
إِذْ تَقُولُ لِلْمُؤْمِنِينَ أَلَن يَكْفِيَكُمْ أَن يُمِدَّكُمْ رَبُّكُم بِثَلَاثَةِ آلَافٍ مِّنَ الْمَلَائِكَةِ مُنزَلِينَ ۝١٢٤
Iz taqoolu lilmu`mineena alai yakfiyakum ai-yumiddakum Rabbukum bisalaasati aalaafim minal malaaa`ikati munzaleen
📖 Tekkim Wolof
[Fàttalikul yaw Yonent bi] ba nga waxee ña gëm : “Moo ndax doyuleen, seen Boroom, tëbb leen ñetti junni Malaaka yu wàcc [ngir dimbali leen]” ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 122-126 — Simoore Aali Imran

122إِذْ هَمَّت طَّائِفَتَانِ مِنكُمْ أَن تَفْشَلَا وَاللَّهُ وَلِيُّهُمَا ۗ وَعَلَى اللَّهِ فَلْيَتَوَكَّلِ الْمُؤْمِنُونَ
[Fàttalikul] ba ñaari kurél ci yéen naree yoqat ! Te Moo leen dimbali woon ba delluwuñu ginnaaw ! Way-gëm ña, nañu sukkandiku ci Yàlla [Uhud].
123وَلَقَدْ نَصَرَكُمُ اللَّهُ بِبَدْرٍ وَأَنتُمْ أَذِلَّةٌ ۖ فَاتَّقُوا اللَّهَ لَعَلَّكُمْ تَشْكُرُونَ
Yàlla dimbali woon na leen ca Badar, ba ngeen nekkee ñu néewle. Ragal-leen Yàlla ndax amaana ngeen gërëm ko !
124إِذْ تَقُولُ لِلْمُؤْمِنِينَ أَلَن يَكْفِيَكُمْ أَن يُمِدَّكُمْ رَبُّكُم بِثَلَاثَةِ آلَافٍ مِّنَ الْمَلَائِكَةِ مُنزَلِينَ
[Fàttalikul yaw Yonent bi] ba nga waxee ña gëm : “Moo ndax doyuleen, seen Boroom, tëbb leen ñetti junni Malaaka yu wàcc [ngir dimbali leen]” ?
125بَلَىٰ ۚ إِن تَصْبِرُوا وَتَتَّقُوا وَيَأْتُوكُم مِّن فَوْرِهِمْ هَٰذَا يُمْدِدْكُمْ رَبُّكُم بِخَمْسَةِ آلَافٍ مِّنَ الْمَلَائِكَةِ مُسَوِّمِينَ
Axakañ ! Bu ngeen muñee te ragal Yàlla, bu ñu leen songee ak doole [ca waxtu wu ñu tànn], seen Boroom dana leen tëbb juróomi junniy Malaaka yuñu màndargaal.
126وَمَا جَعَلَهُ اللَّهُ إِلَّا بُشْرَىٰ لَكُمْ وَلِتَطْمَئِنَّ قُلُوبُكُم بِهِ ۗ وَمَا النَّصْرُ إِلَّا مِنْ عِندِ اللَّهِ الْعَزِيزِ الْحَكِيمِ
Te Yàlla defewuko lu dul bégal leen ngir seeni xel dal. Te ndimbal du bawoo fu dul fa Yàlla, Mooy Ki not, di Ku xereñ ki ;
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
124Aaya

Tekki — Aali Imran 124

Simoore Aali Imran Aaya 124 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Fàttalikul yaw Yonent bi] ba nga waxee ña gëm :…

Simoore Aaya 124/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 122–126. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers