Saba · 48/54
Tekki Waxtaan — Saba
قُلْ إِنَّ رَبِّي يَقْذِفُ بِالْحَقِّ عَلَّامُ الْغُيُوبِ ۝٤٨
Qul inna Rabbee yaqzifu bilhaqq `Allaamul Ghuyoob
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Neel Yàlla mooy badd ndawam ci dëgg. Mooy xamaakoonu mbóot ya”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 46-50 — Saba

46۞ قُلْ إِنَّمَا أَعِظُكُم بِوَاحِدَةٍ ۖ أَن تَقُومُوا لِلَّهِ مَثْنَىٰ وَفُرَادَىٰ ثُمَّ تَتَفَكَّرُوا ۚ مَا بِصَاحِبِكُم مِّن جِنَّةٍ ۚ إِنْ هُوَ إِلَّا نَذِيرٌ لَّكُم بَيْنَ يَدَيْ عَذَابٍ شَدِيدٍ
Waxal ne : “Maa ngi leen di waar ci lenn : nangeen taxaw ngir Yàlla, moo xam ngeen diy ñaar-ñaar walla ngeen di benn been, te ngeen xalaat. Seen àndandoo bii di Muhammad jinne sadd ko : moom doonul lu dul ab xuppekat bu ame mbugal mu nekk seen kanam”.
47قُلْ مَا سَأَلْتُكُم مِّنْ أَجْرٍ فَهُوَ لَكُمْ ۖ إِنْ أَجْرِيَ إِلَّا عَلَى اللَّهِ ۖ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ شَهِيدٌ
Neel : “Laajumaleen ci ag pey, yéen a ko moom. Samag pey, Yàllaa ko warlu. Moom seede la ci lépp lu nekk”.
48قُلْ إِنَّ رَبِّي يَقْذِفُ بِالْحَقِّ عَلَّامُ الْغُيُوبِ
Neel : “Neel Yàlla mooy badd ndawam ci dëgg. Mooy xamaakoonu mbóot ya”.
49قُلْ جَاءَ الْحَقُّ وَمَا يُبْدِئُ الْبَاطِلُ وَمَا يُعِيدُ
Waxal ne : “Dëgg [Lislaam] dikk na. Te ag neen [kéefar] du fi tàmbalee te du fi dellusi”.
50قُلْ إِن ضَلَلْتُ فَإِنَّمَا أَضِلُّ عَلَىٰ نَفْسِي ۖ وَإِنِ اهْتَدَيْتُ فَبِمَا يُوحِي إِلَيَّ رَبِّي ۚ إِنَّهُ سَمِيعٌ قَرِيبٌ
Waxal ne : “Su ma réeree , sama bopp doŋŋ laay sànk ; su ma gindikoo it, ci sababus li ma Yàlla soloo lay ame, Moom Yàlla kuy Dégg, kuy Jigeñ la”.
SabaFihi Alxuraan
54Aaya
MeccanRevelation
48Aaya

Tekki — Saba 48

Simoore Saba Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Neel Yàlla mooy badd ndawam ci dëgg. Mooy…

Simoore Aaya 48/54 — Saba سبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Saba Dégg, Saba Tekki, Saba mp3, Saba pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers