Fatir · 1/45
Tekki Waxtaan — Simoore Fatir
الْحَمْدُ لِلَّهِ فَاطِرِ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ جَاعِلِ الْمَلَائِكَةِ رُسُلًا أُولِي أَجْنِحَةٍ مَّثْنَىٰ وَثُلَاثَ وَرُبَاعَ ۚ يَزِيدُ فِي الْخَلْقِ مَا يَشَاءُ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ ۝١
Alhamdu lillaahi faatiris samaawaati wal ardi jaa`ilil malaaa`ikati rusulan uleee ajnihatim masnaa wa sulaasa wa rubaa`; yazeedu fil khalqi maa yashaaa`; innal laaha `alaa kulli shai`in Qadeer
📖 Tekkim Wolof
Xeeti cant yépp ñeel na Yàlla mi bind asamaan yeek suuf si, Mooy ki def Malaaka yi ñu di ay ndaw te di woroomi laaf, ñaar-ñaar, ñett ñett walla ñeent ñeent. Mooy dolli ca mbind ga lu ko soob, Yàlla mën na lépp lu nekk.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore Fatir

1الْحَمْدُ لِلَّهِ فَاطِرِ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ جَاعِلِ الْمَلَائِكَةِ رُسُلًا أُولِي أَجْنِحَةٍ مَّثْنَىٰ وَثُلَاثَ وَرُبَاعَ ۚ يَزِيدُ فِي الْخَلْقِ مَا يَشَاءُ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Xeeti cant yépp ñeel na Yàlla mi bind asamaan yeek suuf si, Mooy ki def Malaaka yi ñu di ay ndaw te di woroomi laaf, ñaar-ñaar, ñett ñett walla ñeent ñeent. Mooy dolli ca mbind ga lu ko soob, Yàlla mën na lépp lu nekk.
2مَّا يَفْتَحِ اللَّهُ لِلنَّاسِ مِن رَّحْمَةٍ فَلَا مُمْسِكَ لَهَا ۖ وَمَا يُمْسِكْ فَلَا مُرْسِلَ لَهُ مِن بَعْدِهِ ۚ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Li Yàlla di ubbil nit ñi ci yërmaande, kenn mënu koo fànq, lu Mu tëj itam, kenn mënu koo tijji ginnaawam. Mooy boroom Kàttan, di Ku Xereñ.
3يَا أَيُّهَا النَّاسُ اذْكُرُوا نِعْمَتَ اللَّهِ عَلَيْكُمْ ۚ هَلْ مِنْ خَالِقٍ غَيْرُ اللَّهِ يَرْزُقُكُم مِّنَ السَّمَاءِ وَالْأَرْضِ ۚ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ فَأَنَّىٰ تُؤْفَكُونَ
Éy yéen nit ñi ! Fàttalikuleen xéewali Yàlla yi ci yéen : moo ndax amuñu bindkat bu dul Yàlla, bu leen di wërsëgal ci asamaan yeek suuf si ? Amul jeneen yàlla ju dul Moom ! Moo yéen ndax mën ngeen koo dummóoyu ?
FatirFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
1Aaya

Tekki — Fatir 1

Simoore Fatir Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xeeti cant yépp ñeel na Yàlla mi bind asamaan yeek…

Simoore Aaya 1/45 — Simoore Fatir فاطر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Fatir Dégg, Simoore Fatir Tekki, Simoore Fatir mp3, Simoore Fatir pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers