Fatir · 17/45
Tekki Waxtaan — Simoore Fatir
وَمَا ذَٰلِكَ عَلَى اللَّهِ بِعَزِيزٍ ۝١٧
Wa maa zaalika `alal laahi bi`azeez
📖 Tekkim Wolof
Te loolu du lu jafe ci Yàlla.

🎧 Dégg


📜 Aaya 15-19 — Simoore Fatir

15۞ يَا أَيُّهَا النَّاسُ أَنتُمُ الْفُقَرَاءُ إِلَى اللَّهِ ۖ وَاللَّهُ هُوَ الْغَنِيُّ الْحَمِيدُ
Éy yéen nit ñi, yéen ay soxlaa woo Yàlla, waaye Yàlla moom Ku doylu la ci boppam, di Yeyoowaakoonu cant.
16إِن يَشَأْ يُذْهِبْكُمْ وَيَأْتِ بِخَلْقٍ جَدِيدٍ
Su ko neexoon Mu yóbbu leen, indi ñeneen mbindeef yu bees.
17وَمَا ذَٰلِكَ عَلَى اللَّهِ بِعَزِيزٍ
Te loolu du lu jafe ci Yàlla.
18وَلَا تَزِرُ وَازِرَةٌ وِزْرَ أُخْرَىٰ ۚ وَإِن تَدْعُ مُثْقَلَةٌ إِلَىٰ حِمْلِهَا لَا يُحْمَلْ مِنْهُ شَيْءٌ وَلَوْ كَانَ ذَا قُرْبَىٰ ۗ إِنَّمَا تُنذِرُ الَّذِينَ يَخْشَوْنَ رَبَّهُم بِالْغَيْبِ وَأَقَامُوا الصَّلَاةَ ۚ وَمَن تَزَكَّىٰ فَإِنَّمَا يَتَزَكَّىٰ لِنَفْسِهِ ۚ وَإِلَى اللَّهِ الْمَصِيرُ
Kenn du yenu bàkkaarub keneen. Te képp ku diis gann ak bàkkaar, bumu cay woote ndimbal, kenn du ko yenul dara, doonte la sax dafa di mbokkug jegeñaale. Da di rekk ne nangay xupp ña di ña ragal seen Boroom ci kumpa tey taxawal julli. Te képp ku cay sellal, na xam ne boppam la koy defal, te ca Yàlla la lépp di mujj.
19وَمَا يَسْتَوِي الْأَعْمَىٰ وَالْبَصِيرُ
Gumba ak njàccaar niróowuñu.
FatirFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — Fatir 17

Simoore Fatir Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te loolu du lu jafe ci Yàlla.

Simoore Aaya 17/45 — Simoore Fatir فاطر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Fatir Dégg, Simoore Fatir Tekki, Simoore Fatir mp3, Simoore Fatir pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers