Ya-Sin · 16/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
قَالُوا رَبُّنَا يَعْلَمُ إِنَّا إِلَيْكُمْ لَمُرْسَلُونَ ۝١٦
Qaaloo Rabbunaa ya`lamu innaaa ilaikum lamursaloon
📖 Tekkim Wolof
[Yonent ya] waxaat ne : “Yàlla xam na ne nun ay Yonent lanu ci yéen.

🎧 Dégg


📜 Aaya 14-18 — Simoore Ya-Sin

14إِذْ أَرْسَلْنَا إِلَيْهِمُ اثْنَيْنِ فَكَذَّبُوهُمَا فَعَزَّزْنَا بِثَالِثٍ فَقَالُوا إِنَّا إِلَيْكُم مُّرْسَلُونَ
Ba Nu leen jebalee ñaari ndaw ñu weddi leen. Nu daldi leen kàttanalaat ci ndaw lu leen ñetteel, ñu ànd ñoom ñett, ne leen : “Nun ndawi Yàlla lanu”.
15قَالُوا مَا أَنتُمْ إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُنَا وَمَا أَنزَلَ الرَّحْمَٰنُ مِن شَيْءٍ إِنْ أَنتُمْ إِلَّا تَكْذِبُونَ
[Waa dëkk ba] tontu [Antaakiya] ne leen : “Yéen daal, ay mbindeef ngeen ni nun. Te Yàlla wàccewul dara, yéen daal ay fenkat doŋŋ ngeen”.
16قَالُوا رَبُّنَا يَعْلَمُ إِنَّا إِلَيْكُمْ لَمُرْسَلُونَ
[Yonent ya] waxaat ne : “Yàlla xam na ne nun ay Yonent lanu ci yéen.
17وَمَا عَلَيْنَا إِلَّا الْبَلَاغُ الْمُبِينُ
te dara warunu lu dul jottali ba mu leer nàññ.”
18قَالُوا إِنَّا تَطَيَّرْنَا بِكُمْ ۖ لَئِن لَّمْ تَنتَهُوا لَنَرْجُمَنَّكُمْ وَلَيَمَسَّنَّكُم مِّنَّا عَذَابٌ أَلِيمٌ
Ñu ne : “Gaafal nanu leen. Te bu ngeen bàyyiwul, dananu leen jóori xeer te dananu leen mbugal mbugal mu tar”.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Ya-Sin 16

Simoore Ya-Sin Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Yonent ya] waxaat ne : “Yàlla xam na ne nun…

Simoore Aaya 16/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers