Ya-Sin · 15/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
قَالُوا مَا أَنتُمْ إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُنَا وَمَا أَنزَلَ الرَّحْمَٰنُ مِن شَيْءٍ إِنْ أَنتُمْ إِلَّا تَكْذِبُونَ ۝١٥
Qaaloo maaa antum illaa basharum mislunaa wa maaa anzalar Rahmaanu min shai`in in antum illaa takziboon
📖 Tekkim Wolof
[Waa dëkk ba] tontu [Antaakiya] ne leen : “Yéen daal, ay mbindeef ngeen ni nun. Te Yàlla wàccewul dara, yéen daal ay fenkat doŋŋ ngeen”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 13-17 — Simoore Ya-Sin

13وَاضْرِبْ لَهُم مَّثَلًا أَصْحَابَ الْقَرْيَةِ إِذْ جَاءَهَا الْمُرْسَلُونَ
Joxleen misaal ci waa dëkk ba ab Yonent dikkaloon.
14إِذْ أَرْسَلْنَا إِلَيْهِمُ اثْنَيْنِ فَكَذَّبُوهُمَا فَعَزَّزْنَا بِثَالِثٍ فَقَالُوا إِنَّا إِلَيْكُم مُّرْسَلُونَ
Ba Nu leen jebalee ñaari ndaw ñu weddi leen. Nu daldi leen kàttanalaat ci ndaw lu leen ñetteel, ñu ànd ñoom ñett, ne leen : “Nun ndawi Yàlla lanu”.
15قَالُوا مَا أَنتُمْ إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُنَا وَمَا أَنزَلَ الرَّحْمَٰنُ مِن شَيْءٍ إِنْ أَنتُمْ إِلَّا تَكْذِبُونَ
[Waa dëkk ba] tontu [Antaakiya] ne leen : “Yéen daal, ay mbindeef ngeen ni nun. Te Yàlla wàccewul dara, yéen daal ay fenkat doŋŋ ngeen”.
16قَالُوا رَبُّنَا يَعْلَمُ إِنَّا إِلَيْكُمْ لَمُرْسَلُونَ
[Yonent ya] waxaat ne : “Yàlla xam na ne nun ay Yonent lanu ci yéen.
17وَمَا عَلَيْنَا إِلَّا الْبَلَاغُ الْمُبِينُ
te dara warunu lu dul jottali ba mu leer nàññ.”
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Ya-Sin 15

Simoore Ya-Sin Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Waa dëkk ba] tontu [Antaakiya] ne leen : “Yéen daal,…

Simoore Aaya 15/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers