Ya-Sin · 79/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
قُلْ يُحْيِيهَا الَّذِي أَنشَأَهَا أَوَّلَ مَرَّةٍ ۖ وَهُوَ بِكُلِّ خَلْقٍ عَلِيمٌ ٧٩
Transliteration
Qul yuh yeehal lazeee ansha ahaaa awwala marrah; wa Huwa bikulli khalqin `Aleem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Ki ko sosoon bu jëkk. Te xam lool bindafoon yépp ;
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 77-81 — Ya-Sin
77أَوَلَمْ يَرَ الْإِنسَانُ أَنَّا خَلَقْنَاهُ مِن نُّطْفَةٍ فَإِذَا هُوَ خَصِيمٌ مُّبِينٌ
Xanaa nit dafa gisul ne Nun Yàlla noo ko bind ci lumbub deret ? Deketeyoo moom ab xulóowaakoon la bu di ab pànk !
78وَضَرَبَ لَنَا مَثَلًا وَنَسِيَ خَلْقَهُ ۖ قَالَ مَن يُحْيِي الْعِظَامَ وَهِيَ رَمِيمٌ
Mu di Nu sàdd léebu, fàtte na ag sosoom ; dana wax naan : “Ana kan mooy dekkalaat ay yax yu funux ? ”
79قُلْ يُحْيِيهَا الَّذِي أَنشَأَهَا أَوَّلَ مَرَّةٍ ۖ وَهُوَ بِكُلِّ خَلْقٍ عَلِيمٌ
Neel : “Ki ko sosoon bu jëkk. Te xam lool bindafoon yépp ;
80الَّذِي جَعَلَ لَكُم مِّنَ الشَّجَرِ الْأَخْضَرِ نَارًا فَإِذَا أَنتُم مِّنْهُ تُوقِدُونَ
te Moo di ki leen defal ci garab gu nëtëx, aw safara wu ngeen di taaloo.
81أَوَلَيْسَ الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ بِقَادِرٍ عَلَىٰ أَن يَخْلُقَ مِثْلَهُم ۚ بَلَىٰ وَهُوَ الْخَلَّاقُ الْعَلِيمُ
Moo ndax ku bind asamaan yeek suuf mënul a bindaat ñeneen yu na mel ? Axakañ ! Moo di Bindaakoon, Xamaakoon bi.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
79Aaya
Tekki — Ya-Sin 79
Simoore Ya-Sin Aaya 79 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Ki ko sosoon bu jëkk. Te xam lool…Simoore Aaya 79/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 77–81. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








