As-Saffat · 115/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَنَجَّيْنَاهُمَا وَقَوْمَهُمَا مِنَ الْكَرْبِ الْعَظِيمِ ۝١١٥
Wa najjainaahumaa wa qawmahumaa minal karbil `azeem
📖 Tekkim Wolof
Musaloon Nanu leen ñoom seeni sët ca tiit mu rëy ma,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 113-117 — Simoore As-Saffat

113وَبَارَكْنَا عَلَيْهِ وَعَلَىٰ إِسْحَاقَ ۚ وَمِن ذُرِّيَّتِهِمَا مُحْسِنٌ وَظَالِمٌ لِّنَفْسِهِ مُبِينٌ
Nu barkeel ko moom ak Isaaqa. Mu am ci seeni sët kuy rafetal ak kuy tooñ boppam.
114وَلَقَدْ مَنَنَّا عَلَىٰ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
Xéewaloon Nanu Muusaa ak Haaruuna,
115وَنَجَّيْنَاهُمَا وَقَوْمَهُمَا مِنَ الْكَرْبِ الْعَظِيمِ
Musaloon Nanu leen ñoom seeni sët ca tiit mu rëy ma,
116وَنَصَرْنَاهُمْ فَكَانُوا هُمُ الْغَالِبِينَ
Nu dimbali woon leen, ñoom ñoo nootoon.
117وَآتَيْنَاهُمَا الْكِتَابَ الْمُسْتَبِينَ
Nu indiloon leen ab téere bu bir
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
115Aaya

Tekki — As-Saffat 115

Simoore As-Saffat Aaya 115 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Musaloon Nanu leen ñoom seeni sët ca tiit mu rëy…

Simoore Aaya 115/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 113–117. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers