As-Saffat · 146/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَأَنبَتْنَا عَلَيْهِ شَجَرَةً مِّن يَقْطِينٍ ۝١٤٦
Wa ambatnaa `alaihi shajaratam mai yaqteen
📖 Tekkim Wolof
Nu daldi fay saxal gàncaxug beraf,

🎧 Dégg


📜 Aaya 144-148 — Simoore As-Saffat

144لَلَبِثَ فِي بَطْنِهِ إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
kon dey dana sax ca biir [jën wa] ba bisub dekkiwaat ba di ñëw.
145۞ فَنَبَذْنَاهُ بِالْعَرَاءِ وَهُوَ سَقِيمٌ
Nu sànni ko ca teges ga te muy ku ràgg.
146وَأَنبَتْنَا عَلَيْهِ شَجَرَةً مِّن يَقْطِينٍ
Nu daldi fay saxal gàncaxug beraf,
147وَأَرْسَلْنَاهُ إِلَىٰ مِائَةِ أَلْفٍ أَوْ يَزِيدُونَ
Nu yebal ko muy Yonent ci téeméeri junniy nit mbaa lu ko ëpp.
148فَآمَنُوا فَمَتَّعْنَاهُمْ إِلَىٰ حِينٍ
Ba ñu gëmee, xéewalal Nanu leen fa ab diir.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
146Aaya

Tekki — As-Saffat 146

Simoore As-Saffat Aaya 146 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu daldi fay saxal gàncaxug beraf,

Simoore Aaya 146/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 144–148. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers