As-Saffat · 147/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَأَرْسَلْنَاهُ إِلَىٰ مِائَةِ أَلْفٍ أَوْ يَزِيدُونَ ١٤٧
Transliteration
Wa arsalnaahu ilaa mi`ati alfin aw yazeedoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nu yebal ko muy Yonent ci téeméeri junniy nit mbaa lu ko ëpp.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 145-149 — Simoore As-Saffat
145۞ فَنَبَذْنَاهُ بِالْعَرَاءِ وَهُوَ سَقِيمٌ
Nu sànni ko ca teges ga te muy ku ràgg.
146وَأَنبَتْنَا عَلَيْهِ شَجَرَةً مِّن يَقْطِينٍ
Nu daldi fay saxal gàncaxug beraf,
147وَأَرْسَلْنَاهُ إِلَىٰ مِائَةِ أَلْفٍ أَوْ يَزِيدُونَ
Nu yebal ko muy Yonent ci téeméeri junniy nit mbaa lu ko ëpp.
148فَآمَنُوا فَمَتَّعْنَاهُمْ إِلَىٰ حِينٍ
Ba ñu gëmee, xéewalal Nanu leen fa ab diir.
149فَاسْتَفْتِهِمْ أَلِرَبِّكَ الْبَنَاتُ وَلَهُمُ الْبَنُونَ
Laajleen baxam : “Ndax Yàlla moo ame doom yu jigéen, ñoom ñuy am doom yu góor ?
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
147Aaya
Tekki — As-Saffat 147
Simoore As-Saffat Aaya 147 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu yebal ko muy Yonent ci téeméeri junniy nit mbaa…Simoore Aaya 147/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 145–149. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 8, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








