As-Saffat · 29/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
قَالُوا بَل لَّمْ تَكُونُوا مُؤْمِنِينَ ۝٢٩
Qaaloo bal lam takoonoo mu`mineen
📖 Tekkim Wolof
[Kilifa ya] ne leen : “Yéen kay yéen a gëmul woon.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 27-31 — Simoore As-Saffat

27وَأَقْبَلَ بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ يَتَسَاءَلُونَ
ku nekk di geesu moroom ma, ñuy laajante ;
28قَالُوا إِنَّكُمْ كُنتُمْ تَأْتُونَنَا عَنِ الْيَمِينِ
Ñuy wax naan : “Yéen a nu daan ga ci kéefar”.
29قَالُوا بَل لَّمْ تَكُونُوا مُؤْمِنِينَ
[Kilifa ya] ne leen : “Yéen kay yéen a gëmul woon.
30وَمَا كَانَ لَنَا عَلَيْكُم مِّن سُلْطَانٍ ۖ بَلْ كُنتُمْ قَوْمًا طَاغِينَ
Te nun amunu woon benn sañ-sañ ci yéen. Yéen kay yéen a bewoon.
31فَحَقَّ عَلَيْنَا قَوْلُ رَبِّنَا ۖ إِنَّا لَذَائِقُونَ
La Yàlla daan wax dal na ci sunu kaw ; [tey] noo ngi toqamtiku [mbugal].
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
29Aaya

Tekki — As-Saffat 29

Simoore As-Saffat Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Kilifa ya] ne leen : “Yéen kay yéen a gëmul…

Simoore Aaya 29/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers