As-Saffat · 64/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِنَّهَا شَجَرَةٌ تَخْرُجُ فِي أَصْلِ الْجَحِيمِ ۝٦٤
Innahaa shajaratun takhruju feee aslil Jaheem
📖 Tekkim Wolof
Moom garab la guy génn ca ndéntul Safara.

🎧 Dégg


📜 Aaya 62-66 — Simoore As-Saffat

62أَذَٰلِكَ خَيْرٌ نُّزُلًا أَمْ شَجَرَةُ الزَّقُّومِ
Moo ndax loolu moo di wàccuwaay ba gën, walla garabug Zaquum ?
63إِنَّا جَعَلْنَاهَا فِتْنَةً لِّلظَّالِمِينَ
Def nanu ko muy sànjub tooñkat ya.
64إِنَّهَا شَجَرَةٌ تَخْرُجُ فِي أَصْلِ الْجَحِيمِ
Moom garab la guy génn ca ndéntul Safara.
65طَلْعُهَا كَأَنَّهُ رُءُوسُ الشَّيَاطِينِ
Meññent ma mel ni boppi séytaane.
66فَإِنَّهُمْ لَآكِلُونَ مِنْهَا فَمَالِئُونَ مِنْهَا الْبُطُونَ
Ca la ñuy lekk, di ca feesal seeni biir.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
64Aaya

Tekki — As-Saffat 64

Simoore As-Saffat Aaya 64 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moom garab la guy génn ca ndéntul Safara.

Simoore Aaya 64/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 62–66. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers