As-Saffat · 63/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِنَّا جَعَلْنَاهَا فِتْنَةً لِّلظَّالِمِينَ ۝٦٣
Innaa ja`alnaahaa fitnatal lizzaalimeen
📖 Tekkim Wolof
Def nanu ko muy sànjub tooñkat ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 61-65 — Simoore As-Saffat

61لِمِثْلِ هَٰذَا فَلْيَعْمَلِ الْعَامِلُونَ
Ñiy jëf, nañuy jëf lu mel nii.
62أَذَٰلِكَ خَيْرٌ نُّزُلًا أَمْ شَجَرَةُ الزَّقُّومِ
Moo ndax loolu moo di wàccuwaay ba gën, walla garabug Zaquum ?
63إِنَّا جَعَلْنَاهَا فِتْنَةً لِّلظَّالِمِينَ
Def nanu ko muy sànjub tooñkat ya.
64إِنَّهَا شَجَرَةٌ تَخْرُجُ فِي أَصْلِ الْجَحِيمِ
Moom garab la guy génn ca ndéntul Safara.
65طَلْعُهَا كَأَنَّهُ رُءُوسُ الشَّيَاطِينِ
Meññent ma mel ni boppi séytaane.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
63Aaya

Tekki — As-Saffat 63

Simoore As-Saffat Aaya 63 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Def nanu ko muy sànjub tooñkat ya.

Simoore Aaya 63/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 61–65. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers