As-Saffat · 65/182
Tekki Waxtaan — As-Saffat
طَلْعُهَا كَأَنَّهُ رُءُوسُ الشَّيَاطِينِ ٦٥
Transliteration
Tal`uhaa ka annahoo ru`oosush Shayaateen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Meññent ma mel ni boppi séytaane.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 63-67 — As-Saffat
63إِنَّا جَعَلْنَاهَا فِتْنَةً لِّلظَّالِمِينَ
Def nanu ko muy sànjub tooñkat ya.
64إِنَّهَا شَجَرَةٌ تَخْرُجُ فِي أَصْلِ الْجَحِيمِ
Moom garab la guy génn ca ndéntul Safara.
65طَلْعُهَا كَأَنَّهُ رُءُوسُ الشَّيَاطِينِ
Meññent ma mel ni boppi séytaane.
66فَإِنَّهُمْ لَآكِلُونَ مِنْهَا فَمَالِئُونَ مِنْهَا الْبُطُونَ
Ca la ñuy lekk, di ca feesal seeni biir.
67ثُمَّ إِنَّ لَهُمْ عَلَيْهَا لَشَوْبًا مِّنْ حَمِيمٍ
Am nañu fa, ca kawam, am ndox mu tàng [di wañax].
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
65Aaya
Tekki — As-Saffat 65
Simoore As-Saffat Aaya 65 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Meññent ma mel ni boppi séytaane.Simoore Aaya 65/182 — As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: As-Saffat Dégg, As-Saffat Tekki, As-Saffat mp3, As-Saffat pdf. Aaya 63–67. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








