As-Saffat · 70/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
فَهُمْ عَلَىٰ آثَارِهِمْ يُهْرَعُونَ ۝٧٠
Fahum `alaa aasaarihim yuhra`oon
📖 Tekkim Wolof
ñuy yolli-yolli topp leen.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 68-72 — Simoore As-Saffat

68ثُمَّ إِنَّ مَرْجِعَهُمْ لَإِلَى الْجَحِيمِ
Safara rekk mooy seen kër.
69إِنَّهُمْ أَلْفَوْا آبَاءَهُمْ ضَالِّينَ
Daje nañu faak seeni [baay ak i maam] cig cànkute,
70فَهُمْ عَلَىٰ آثَارِهِمْ يُهْرَعُونَ
ñuy yolli-yolli topp leen.
71وَلَقَدْ ضَلَّ قَبْلَهُمْ أَكْثَرُ الْأَوَّلِينَ
Li ëppoon ca ña leen jiitu woon sàkku woon nañu.
72وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا فِيهِم مُّنذِرِينَ
Ndax yónni woon Nanu ci ñoom ñuy xuppe, di waaraate .
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
70Aaya

Tekki — As-Saffat 70

Simoore As-Saffat Aaya 70 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñuy yolli-yolli topp leen.

Simoore Aaya 70/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 68–72. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers