As-Saffat · 71/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَلَقَدْ ضَلَّ قَبْلَهُمْ أَكْثَرُ الْأَوَّلِينَ ۝٧١
Wa laqad dalla qablahum aksarul awwaleen
📖 Tekkim Wolof
Li ëppoon ca ña leen jiitu woon sàkku woon nañu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 69-73 — Simoore As-Saffat

69إِنَّهُمْ أَلْفَوْا آبَاءَهُمْ ضَالِّينَ
Daje nañu faak seeni [baay ak i maam] cig cànkute,
70فَهُمْ عَلَىٰ آثَارِهِمْ يُهْرَعُونَ
ñuy yolli-yolli topp leen.
71وَلَقَدْ ضَلَّ قَبْلَهُمْ أَكْثَرُ الْأَوَّلِينَ
Li ëppoon ca ña leen jiitu woon sàkku woon nañu.
72وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا فِيهِم مُّنذِرِينَ
Ndax yónni woon Nanu ci ñoom ñuy xuppe, di waaraate .
73فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُنذَرِينَ
Xoolal mujjug ñanu daan xupp !
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
71Aaya

Tekki — As-Saffat 71

Simoore As-Saffat Aaya 71 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Li ëppoon ca ña leen jiitu woon sàkku woon nañu.

Simoore Aaya 71/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 69–73. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers