As-Saffat · 82/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
ثُمَّ أَغْرَقْنَا الْآخَرِينَ ۝٨٢
Summa aghraqnal aakhareen
📖 Tekkim Wolof
Ginnaaw ba, Nu labal ña ca des.

🎧 Dégg


📜 Aaya 80-84 — Simoore As-Saffat

80إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal.
81إِنَّهُ مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
Moom bokk na ca Sunu jaam yu gëm ya.
82ثُمَّ أَغْرَقْنَا الْآخَرِينَ
Ginnaaw ba, Nu labal ña ca des.
83۞ وَإِنَّ مِن شِيعَتِهِ لَإِبْرَاهِيمَ
Ibrahiima bokkoon na ca ay njabootam.
84إِذْ جَاءَ رَبَّهُ بِقَلْبٍ سَلِيمٍ
Fàttalikul ba mu dikkee ca Boroomam ànd ak xol bu mucc ayib.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
82Aaya

Tekki — As-Saffat 82

Simoore As-Saffat Aaya 82 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ginnaaw ba, Nu labal ña ca des.

Simoore Aaya 82/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 80–84. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers