As-Saffat · 83/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
۞ وَإِنَّ مِن شِيعَتِهِ لَإِبْرَاهِيمَ ۝٨٣
Wa ina min shee`atihee la Ibraaheem
📖 Tekkim Wolof
Ibrahiima bokkoon na ca ay njabootam.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 81-85 — Simoore As-Saffat

81إِنَّهُ مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
Moom bokk na ca Sunu jaam yu gëm ya.
82ثُمَّ أَغْرَقْنَا الْآخَرِينَ
Ginnaaw ba, Nu labal ña ca des.
83۞ وَإِنَّ مِن شِيعَتِهِ لَإِبْرَاهِيمَ
Ibrahiima bokkoon na ca ay njabootam.
84إِذْ جَاءَ رَبَّهُ بِقَلْبٍ سَلِيمٍ
Fàttalikul ba mu dikkee ca Boroomam ànd ak xol bu mucc ayib.
85إِذْ قَالَ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ مَاذَا تَعْبُدُونَ
Ak ba mu waxee baayam ak nitam, ne leen : “Ana li ngeen di jaamu ? ”
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
83Aaya

Tekki — As-Saffat 83

Simoore As-Saffat Aaya 83 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ibrahiima bokkoon na ca ay njabootam.

Simoore Aaya 83/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 81–85. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers