As-Saffat · 81/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِنَّهُ مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ ۝٨١
Innahoo min `ibaadinal mu`mineen
📖 Tekkim Wolof
Moom bokk na ca Sunu jaam yu gëm ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 79-83 — Simoore As-Saffat

79سَلَامٌ عَلَىٰ نُوحٍ فِي الْعَالَمِينَ
Yal na jàmm wàcc ci Nooh ci kaw àddina sépp !
80إِنَّا كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal.
81إِنَّهُ مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
Moom bokk na ca Sunu jaam yu gëm ya.
82ثُمَّ أَغْرَقْنَا الْآخَرِينَ
Ginnaaw ba, Nu labal ña ca des.
83۞ وَإِنَّ مِن شِيعَتِهِ لَإِبْرَاهِيمَ
Ibrahiima bokkoon na ca ay njabootam.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
81Aaya

Tekki — As-Saffat 81

Simoore As-Saffat Aaya 81 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moom bokk na ca Sunu jaam yu gëm ya.

Simoore Aaya 81/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 79–83. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers