Sad · 69/88
Tekki Waxtaan — Simoore Sad
مَا كَانَ لِيَ مِنْ عِلْمٍ بِالْمَلَإِ الْأَعْلَىٰ إِذْ يَخْتَصِمُونَ ۝٦٩
Maa kaana liya min `ilmim bilmala il a`laaa iz yakhtasimoon
📖 Tekkim Wolof
Amuma woon xam-xam ca xulóob kilifa ya gën a kawe.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 67-71 — Simoore Sad

67قُلْ هُوَ نَبَأٌ عَظِيمٌ
Waxal ne : “Xibaar bu rëy la,
68أَنتُمْ عَنْهُ مُعْرِضُونَ
waaye yéen dumóoyu ngeen ko.
69مَا كَانَ لِيَ مِنْ عِلْمٍ بِالْمَلَإِ الْأَعْلَىٰ إِذْ يَخْتَصِمُونَ
Amuma woon xam-xam ca xulóob kilifa ya gën a kawe.
70إِن يُوحَىٰ إِلَيَّ إِلَّا أَنَّمَا أَنَا نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Li nu may soloo doonul lu dul ne man mii ab xuppe kat laa waaraatekat bu bir”.
71إِذْ قَالَ رَبُّكَ لِلْمَلَائِكَةِ إِنِّي خَالِقٌ بَشَرًا مِّن طِينٍ
(Fàttalitul) ba sa Boroom waxee Malaaka ya ne leen : “Man de maa ngi sàkk mbindéef ci ban.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
69Aaya

Tekki — Sad 69

Simoore Sad Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Amuma woon xam-xam ca xulóob kilifa ya gën a kawe.

Simoore Aaya 69/88 — Simoore Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Sad Dégg, Simoore Sad Tekki, Simoore Sad mp3, Simoore Sad pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers