Sad · 87/88
Tekki Waxtaan — Simoore Sad
إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرٌ لِّلْعَالَمِينَ ۝٨٧
In huwa illaa zikrul lil`aalameen
📖 Tekkim Wolof
[Alxuraan] jii daal ag fàttali la ñeel waa àddina si yépp.

🎧 Dégg


📜 Aaya 85-88 — Simoore Sad

85لَأَمْلَأَنَّ جَهَنَّمَ مِنكَ وَمِمَّن تَبِعَكَ مِنْهُمْ أَجْمَعِينَ
Danaa feesal Safara ci yaw ak ña la topp ñépp”.
86قُلْ مَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ وَمَا أَنَا مِنَ الْمُتَكَلِّفِينَ
Waxal ne : “Laajumaleen ci ag pey ; te it yanuwuma ci.
87إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرٌ لِّلْعَالَمِينَ
[Alxuraan] jii daal ag fàttali la ñeel waa àddina si yépp.
88وَلَتَعْلَمُنَّ نَبَأَهُ بَعْدَ حِينٍ
Te dangeen xam ay xibaaram ci ndiir su yàggatul ! ”.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
87Aaya

Tekki — Sad 87

Simoore Sad Aaya 87 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Alxuraan] jii daal ag fàttali la ñeel waa àddina si…

Simoore Aaya 87/88 — Simoore Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Sad Dégg, Simoore Sad Tekki, Simoore Sad mp3, Simoore Sad pdf. Aaya 85–88. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers