Sad · 86/88
Tekki Waxtaan — Sad
قُلْ مَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ وَمَا أَنَا مِنَ الْمُتَكَلِّفِينَ ۝٨٦
Qul maaa as`alukum `alaihi min ajrinw wa maaa ana minal mutakallifeen
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne : “Laajumaleen ci ag pey ; te it yanuwuma ci.

🎧 Dégg


📜 Aaya 84-88 — Sad

84قَالَ فَالْحَقُّ وَالْحَقَّ أَقُولُ
(Yàlla) daldi wax ne : “Maa ngi waat, ci dëgg ne dëgg laay wax,
85لَأَمْلَأَنَّ جَهَنَّمَ مِنكَ وَمِمَّن تَبِعَكَ مِنْهُمْ أَجْمَعِينَ
Danaa feesal Safara ci yaw ak ña la topp ñépp”.
86قُلْ مَا أَسْأَلُكُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ وَمَا أَنَا مِنَ الْمُتَكَلِّفِينَ
Waxal ne : “Laajumaleen ci ag pey ; te it yanuwuma ci.
87إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرٌ لِّلْعَالَمِينَ
[Alxuraan] jii daal ag fàttali la ñeel waa àddina si yépp.
88وَلَتَعْلَمُنَّ نَبَأَهُ بَعْدَ حِينٍ
Te dangeen xam ay xibaaram ci ndiir su yàggatul ! ”.
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
86Aaya

Tekki — Sad 86

Simoore Sad Aaya 86 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne : “Laajumaleen ci ag pey ; te it…

Simoore Aaya 86/88 — Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Sad Dégg, Sad Tekki, Sad mp3, Sad pdf. Aaya 84–88. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers