Az-Zumar · 63/75
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zumar
لَّهُ مَقَالِيدُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۗ وَالَّذِينَ كَفَرُوا بِآيَاتِ اللَّهِ أُولَٰئِكَ هُمُ الْخَاسِرُونَ ۝٦٣
Lahoo maqaaleedus sa maawaati wal ard; wallazeena kafaroo bi ayaatil laahi ulaaa`ika humul khaasiroon
📖 Tekkim Wolof
Moo moom caabiy asamaan yeek suuf si ; ñay weddi kàdduy Yàlla, ñooy ña yàqule.

🎧 Dégg


📜 Aaya 61-65 — Simoore Az-Zumar

61وَيُنَجِّي اللَّهُ الَّذِينَ اتَّقَوْا بِمَفَازَتِهِمْ لَا يَمَسُّهُمُ السُّوءُ وَلَا هُمْ يَحْزَنُونَ
Yàlla dana musël ña ragal Yàlla te texel leen [ca Àjjana]. Lu bon du leen fa laal te it duñu fa jàq.
62اللَّهُ خَالِقُ كُلِّ شَيْءٍ ۖ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ وَكِيلٌ
Yàlla moo sàkk bind lépp, te it Mooy lijjënti lépp it.
63لَّهُ مَقَالِيدُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۗ وَالَّذِينَ كَفَرُوا بِآيَاتِ اللَّهِ أُولَٰئِكَ هُمُ الْخَاسِرُونَ
Moo moom caabiy asamaan yeek suuf si ; ñay weddi kàdduy Yàlla, ñooy ña yàqule.
64قُلْ أَفَغَيْرَ اللَّهِ تَأْمُرُونِّي أَعْبُدُ أَيُّهَا الْجَاهِلُونَ
Waxal ne : “Yéen ñi réer, ndax dangeen may digël may jaamu lu dul Yàlla ? ”
65وَلَقَدْ أُوحِيَ إِلَيْكَ وَإِلَى الَّذِينَ مِن قَبْلِكَ لَئِنْ أَشْرَكْتَ لَيَحْبَطَنَّ عَمَلُكَ وَلَتَكُونَنَّ مِنَ الْخَاسِرِينَ
Te, soloona Nu la ak (Yonnent ya la jiitu woon) ci ne : “Saa soo bokkaalee , sa jëf dana sippiku; nga bokk ci ñu yàqule ña.
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
63Aaya

Tekki — Az-Zumar 63

Simoore Az-Zumar Aaya 63 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo moom caabiy asamaan yeek suuf si ; ñay weddi…

Simoore Aaya 63/75 — Simoore Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zumar Dégg, Simoore Az-Zumar Tekki, Simoore Az-Zumar mp3, Simoore Az-Zumar pdf. Aaya 61–65. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers