Az-Zumar · 62/75
Tekki Waxtaan — Az-Zumar
اللَّهُ خَالِقُ كُلِّ شَيْءٍ ۖ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ وَكِيلٌ ۝٦٢
Allaahu khaaliqu kulli shai`inw wa Huwa `alaa kulli shai`inw Wakeel
📖 Tekkim Wolof
Yàlla moo sàkk bind lépp, te it Mooy lijjënti lépp it.

🎧 Dégg


📜 Aaya 60-64 — Az-Zumar

60وَيَوْمَ الْقِيَامَةِ تَرَى الَّذِينَ كَذَبُوا عَلَى اللَّهِ وُجُوهُهُم مُّسْوَدَّةٌ ۚ أَلَيْسَ فِي جَهَنَّمَ مَثْوًى لِّلْمُتَكَبِّرِينَ
Bu Bis Pénc baa, dangay gis ña fenal Yàlla, seen xar kanam ya ñuul kukk. Moo ndax wàccuwaayi yéefar ya nekkul ca biir Safara ? (Axakañ)
61وَيُنَجِّي اللَّهُ الَّذِينَ اتَّقَوْا بِمَفَازَتِهِمْ لَا يَمَسُّهُمُ السُّوءُ وَلَا هُمْ يَحْزَنُونَ
Yàlla dana musël ña ragal Yàlla te texel leen [ca Àjjana]. Lu bon du leen fa laal te it duñu fa jàq.
62اللَّهُ خَالِقُ كُلِّ شَيْءٍ ۖ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ وَكِيلٌ
Yàlla moo sàkk bind lépp, te it Mooy lijjënti lépp it.
63لَّهُ مَقَالِيدُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۗ وَالَّذِينَ كَفَرُوا بِآيَاتِ اللَّهِ أُولَٰئِكَ هُمُ الْخَاسِرُونَ
Moo moom caabiy asamaan yeek suuf si ; ñay weddi kàdduy Yàlla, ñooy ña yàqule.
64قُلْ أَفَغَيْرَ اللَّهِ تَأْمُرُونِّي أَعْبُدُ أَيُّهَا الْجَاهِلُونَ
Waxal ne : “Yéen ñi réer, ndax dangeen may digël may jaamu lu dul Yàlla ? ”
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
62Aaya

Tekki — Az-Zumar 62

Simoore Az-Zumar Aaya 62 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla moo sàkk bind lépp, te it Mooy lijjënti lépp…

Simoore Aaya 62/75 — Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zumar Dégg, Az-Zumar Tekki, Az-Zumar mp3, Az-Zumar pdf. Aaya 60–64. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers