An-Nisa · 67/176
Tekki Waxtaan — An-Nisa
وَإِذًا لَّآتَيْنَاهُم مِّن لَّدُنَّا أَجْرًا عَظِيمًا ٦٧
Transliteration
Wa izal la aatainaahum mil ladunnaaa ajran `azeemaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te kon Nu jox leen pey gu màgg jóge ci Nun,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 65-69 — An-Nisa
65فَلَا وَرَبِّكَ لَا يُؤْمِنُونَ حَتَّىٰ يُحَكِّمُوكَ فِيمَا شَجَرَ بَيْنَهُمْ ثُمَّ لَا يَجِدُوا فِي أَنفُسِهِمْ حَرَجًا مِّمَّا قَضَيْتَ وَيُسَلِّمُوا تَسْلِيمًا
Mukk !... Giñ naa ci sa màggug Boroom ! Duñu gëm mukk [di ay jullit] li feek àtteloowuñu la la ca seen diggante te bañ a am benn ñag-ñagi xol ca la nga àtte, nangul la ak xol bu tàlli.
66وَلَوْ أَنَّا كَتَبْنَا عَلَيْهِمْ أَنِ اقْتُلُوا أَنفُسَكُمْ أَوِ اخْرُجُوا مِن دِيَارِكُم مَّا فَعَلُوهُ إِلَّا قَلِيلٌ مِّنْهُمْ ۖ وَلَوْ أَنَّهُمْ فَعَلُوا مَا يُوعَظُونَ بِهِ لَكَانَ خَيْرًا لَّهُمْ وَأَشَدَّ تَثْبِيتًا
Su fekkoon ñoon Danu leen sant ñu reyante mbaa ñu génn seeni kër, duñu ko def lu dul ñu néew ci ñoom. Te su ñu defoon la ñu leen di waare, mu gën ca ñoom, te gën a dëgëral seen ngëm.
67وَإِذًا لَّآتَيْنَاهُم مِّن لَّدُنَّا أَجْرًا عَظِيمًا
Te kon Nu jox leen pey gu màgg jóge ci Nun,
68وَلَهَدَيْنَاهُمْ صِرَاطًا مُّسْتَقِيمًا
te kon Nu gindi leen teg leen ca yoon wu jub xocc wa.
69وَمَن يُطِعِ اللَّهَ وَالرَّسُولَ فَأُولَٰئِكَ مَعَ الَّذِينَ أَنْعَمَ اللَّهُ عَلَيْهِم مِّنَ النَّبِيِّينَ وَالصِّدِّيقِينَ وَالشُّهَدَاءِ وَالصَّالِحِينَ ۚ وَحَسُنَ أُولَٰئِكَ رَفِيقًا
Ku topp Yàlla ak Yonent ba... ñooña ànd nañook ña Yàlla wàcce xéewalam ci ñoom : ca Yonent ya ak way-dëggu ña [daraja ju kawe sahaaba ya], ak ña dee ci xare ngir Yàlla, ak ñu sell [ñu yiw] ña, ndaw àndandoo yu jekk !
An-NisaFihi Alxuraan
176Aaya
MedinanRevelation
67Aaya
Tekki — An-Nisa 67
Simoore An-Nisa Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te kon Nu jox leen pey gu màgg jóge ci…Simoore Aaya 67/176 — An-Nisa النساء (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nisa Dégg, An-Nisa Tekki, An-Nisa mp3, An-Nisa pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








