Ghafir · 23/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا مُوسَىٰ بِآيَاتِنَا وَسُلْطَانٍ مُّبِينٍ ٢٣
Transliteration
Wa laqad arsalnaa Moosaa bi Aayaatinaa wa sultaanim mubeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yónni woon nanu Muusaa ak sunuy laaya boole ko ak ay firnde yu leer,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 21-25 — Ghafir
21۞ أَوَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَيَنظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الَّذِينَ كَانُوا مِن قَبْلِهِمْ ۚ كَانُوا هُمْ أَشَدَّ مِنْهُمْ قُوَّةً وَآثَارًا فِي الْأَرْضِ فَأَخَذَهُمُ اللَّهُ بِذُنُوبِهِمْ وَمَا كَانَ لَهُم مِّنَ اللَّهِ مِن وَاقٍ
Moo ndax da ñoo doxul ci suuf, tey seetlu mujug ña leen fi jiitu woon te ëppoon doole ak i alal ? Yàlla faagaagaloon leen ngir seeni bàkkar. Te kenn manu leen woon fegal mbugëlu Yàlla mii.
22ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ كَانَت تَّأْتِيهِمْ رُسُلُهُم بِالْبَيِّنَاتِ فَكَفَرُوا فَأَخَذَهُمُ اللَّهُ ۚ إِنَّهُ قَوِيٌّ شَدِيدُ الْعِقَابِ
Li ko waral, moo di ñoom seeni Yonnent, da ñu leen daan indil ay lay yu leer ñu weddi. Yàlla daldi leen faagaagal, Yàlla boroom doole la di ku Tar mbugël.
23وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا مُوسَىٰ بِآيَاتِنَا وَسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Yónni woon nanu Muusaa ak sunuy laaya boole ko ak ay firnde yu leer,
24إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَهَامَانَ وَقَارُونَ فَقَالُوا سَاحِرٌ كَذَّابٌ
jëmële ko ca Firawna, ak Haamaana ak Qaaruuna. Ñuy wax naan : “Kii ab njibarkat bu di ! ab fenaakoon la ! ”
25فَلَمَّا جَاءَهُم بِالْحَقِّ مِنْ عِندِنَا قَالُوا اقْتُلُوا أَبْنَاءَ الَّذِينَ آمَنُوا مَعَهُ وَاسْتَحْيُوا نِسَاءَهُمْ ۚ وَمَا كَيْدُ الْكَافِرِينَ إِلَّا فِي ضَلَالٍ
Ba mu àggee ca ñoom, indi ko baawoo fi Nun da ñoo wax ne : “reyleen doom yu góor ñi gëm ànd ak moom, te bàyyi jigéen ñi ñuy dund”. Pexey yéefar yi du dara lu dul ci ag réer (lay tege).
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
23Aaya
Tekki — Ghafir 23
Simoore Ghafir Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yónni woon nanu Muusaa ak sunuy laaya boole ko ak…Simoore Aaya 23/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








