Ash-Shura · 36/53
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shura
فَمَا أُوتِيتُم مِّن شَيْءٍ فَمَتَاعُ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ۖ وَمَا عِندَ اللَّهِ خَيْرٌ وَأَبْقَىٰ لِلَّذِينَ آمَنُوا وَعَلَىٰ رَبِّهِمْ يَتَوَكَّلُونَ ۝٣٦
Famaa ooteetum min shai`in famataa`ul hayaatid dunyaa wa maa `indal laahi khairunw wa abqaa lillazeena aamanoo wa `alaa Rabbihim yatawakkaloon
📖 Tekkim Wolof
Lii nu leen jox lépp [ci alal] bànneexu dundug àddina rekk la ; waaye la nekk ca Yàlla moo gënn te moo gën a sax ngir nit ñi gëm tey doyloo seen Boroom,

🎧 Dégg


📜 Aaya 34-38 — Simoore Ash-Shura

34أَوْ يُوبِقْهُنَّ بِمَا كَسَبُوا وَيَعْفُ عَن كَثِيرٍ
Walla, mu mbugël leen ci seeni jëf. Tey jéggële lu bari.
35وَيَعْلَمَ الَّذِينَ يُجَادِلُونَ فِي آيَاتِنَا مَا لَهُم مِّن مَّحِيصٍ
Ñiy diiŋat sunuy firnde it danañu xam ne du nu man a am rawtukaay.
36فَمَا أُوتِيتُم مِّن شَيْءٍ فَمَتَاعُ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ۖ وَمَا عِندَ اللَّهِ خَيْرٌ وَأَبْقَىٰ لِلَّذِينَ آمَنُوا وَعَلَىٰ رَبِّهِمْ يَتَوَكَّلُونَ
Lii nu leen jox lépp [ci alal] bànneexu dundug àddina rekk la ; waaye la nekk ca Yàlla moo gënn te moo gën a sax ngir nit ñi gëm tey doyloo seen Boroom,
37وَالَّذِينَ يَجْتَنِبُونَ كَبَائِرَ الْإِثْمِ وَالْفَوَاحِشَ وَإِذَا مَا غَضِبُوا هُمْ يَغْفِرُونَ
ñiy wattandiku bàkkaar yu mag a mag yi ak ñaawtéef yi, te saa su ñu meree jéggale,
38وَالَّذِينَ اسْتَجَابُوا لِرَبِّهِمْ وَأَقَامُوا الصَّلَاةَ وَأَمْرُهُمْ شُورَىٰ بَيْنَهُمْ وَمِمَّا رَزَقْنَاهُمْ يُنفِقُونَ
ñiy nangul seen boroom, ak taxawal Julli, ak di disóo seen mbir ci seen diggënte, tey joxe ci la ñu leen wërsëgël (seeni alal),
Ash-ShuraFihi Alxuraan
53Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — Ash-Shura 36

Simoore Ash-Shura Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lii nu leen jox lépp [ci alal] bànneexu dundug àddina…

Simoore Aaya 36/53 — Simoore Ash-Shura الشورى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shura Dégg, Simoore Ash-Shura Tekki, Simoore Ash-Shura mp3, Simoore Ash-Shura pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers