Az-Zukhruf · 15/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
وَجَعَلُوا لَهُ مِنْ عِبَادِهِ جُزْءًا ۚ إِنَّ الْإِنسَانَ لَكَفُورٌ مُّبِينٌ ۝١٥
Wa ja`aloo lahoo min `ibaadihee juz`aa; innal insaana lakafoorum mubeen
📖 Tekkim Wolof
Nit ñi dañuy mbokkale yàlla ak lenn ci jaamam ñi. Te nit xarabaatekat la bu bir !

🎧 Dégg


📜 Aaya 13-17 — Simoore Az-Zukhruf

13لِتَسْتَوُوا عَلَىٰ ظُهُورِهِ ثُمَّ تَذْكُرُوا نِعْمَةَ رَبِّكُمْ إِذَا اسْتَوَيْتُمْ عَلَيْهِ وَتَقُولُوا سُبْحَانَ الَّذِي سَخَّرَ لَنَا هَٰذَا وَمَا كُنَّا لَهُ مُقْرِنِينَ
ngeen di def ñoŋŋ ca kaw, ngeen di fàttaliku xéewali Yàlla, su ngeen yemoo ca kaw ne ñoŋŋ, te it na ngeen di wax naan : “Tudd nanu sellug ki nu tàggatalal lii (wépp waruwaay) te manalu nu ko woon sunu bopp.
14وَإِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا لَمُنقَلِبُونَ
Te dañuy wëlbatiku jëm ci sunu Boroom”.
15وَجَعَلُوا لَهُ مِنْ عِبَادِهِ جُزْءًا ۚ إِنَّ الْإِنسَانَ لَكَفُورٌ مُّبِينٌ
Nit ñi dañuy mbokkale yàlla ak lenn ci jaamam ñi. Te nit xarabaatekat la bu bir !
16أَمِ اتَّخَذَ مِمَّا يَخْلُقُ بَنَاتٍ وَأَصْفَاكُم بِالْبَنِينَ
Am Yàlla moom dafa jàpp ci li mu bind aw jigéen def leen ñu di doomam ba eggal yéen mu tànnal leen ay doom yu góor ? (mukk amul)
17وَإِذَا بُشِّرَ أَحَدُهُم بِمَا ضَرَبَ لِلرَّحْمَٰنِ مَثَلًا ظَلَّ وَجْهُهُ مُسْوَدًّا وَهُوَ كَظِيمٌ
Te kat, saa su nu bégëlee kenn ci yéen ak la Yàlla doon misaal (doom ju jigéen), xar- kanamam ba daldi ñukku muy fuuñ-fuuñi (mer).
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
15Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 15

Simoore Az-Zukhruf Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nit ñi dañuy mbokkale yàlla ak lenn ci jaamam ñi.…

Simoore Aaya 15/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers