Az-Zukhruf · 16/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
أَمِ اتَّخَذَ مِمَّا يَخْلُقُ بَنَاتٍ وَأَصْفَاكُم بِالْبَنِينَ ۝١٦
Amit takhaza mimmaa yakhluqu banaatinw wa asfaakum bilbaneen
📖 Tekkim Wolof
Am Yàlla moom dafa jàpp ci li mu bind aw jigéen def leen ñu di doomam ba eggal yéen mu tànnal leen ay doom yu góor ? (mukk amul)

🎧 Dégg


📜 Aaya 14-18 — Simoore Az-Zukhruf

14وَإِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا لَمُنقَلِبُونَ
Te dañuy wëlbatiku jëm ci sunu Boroom”.
15وَجَعَلُوا لَهُ مِنْ عِبَادِهِ جُزْءًا ۚ إِنَّ الْإِنسَانَ لَكَفُورٌ مُّبِينٌ
Nit ñi dañuy mbokkale yàlla ak lenn ci jaamam ñi. Te nit xarabaatekat la bu bir !
16أَمِ اتَّخَذَ مِمَّا يَخْلُقُ بَنَاتٍ وَأَصْفَاكُم بِالْبَنِينَ
Am Yàlla moom dafa jàpp ci li mu bind aw jigéen def leen ñu di doomam ba eggal yéen mu tànnal leen ay doom yu góor ? (mukk amul)
17وَإِذَا بُشِّرَ أَحَدُهُم بِمَا ضَرَبَ لِلرَّحْمَٰنِ مَثَلًا ظَلَّ وَجْهُهُ مُسْوَدًّا وَهُوَ كَظِيمٌ
Te kat, saa su nu bégëlee kenn ci yéen ak la Yàlla doon misaal (doom ju jigéen), xar- kanamam ba daldi ñukku muy fuuñ-fuuñi (mer).
18أَوَمَن يُنَشَّأُ فِي الْحِلْيَةِ وَهُوَ فِي الْخِصَامِ غَيْرُ مُبِينٍ
Moo ndax ! Du ul ne (jigéen) mooy màgg ci gànjaroo takkaay, te joŋewul ci dàggasante ?
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 16

Simoore Az-Zukhruf Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Am Yàlla moom dafa jàpp ci li mu bind aw…

Simoore Aaya 16/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers