Az-Zukhruf · 78/89
Tekki Waxtaan — Az-Zukhruf
لَقَدْ جِئْنَاكُم بِالْحَقِّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَكُمْ لِلْحَقِّ كَارِهُونَ ۝٧٨
Laqad ji`naakum bilhaqqi wa laakinna aksarakum lilhaqqi kaarihoon
📖 Tekkim Wolof
“Indiloon Nanu leen dëgg; waaye ñi ëpp ci yéen dañoo bañ Dëgg”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 76-80 — Az-Zukhruf

76وَمَا ظَلَمْنَاهُمْ وَلَٰكِن كَانُوا هُمُ الظَّالِمِينَ
Du ut ne Nun noo leen tooñ, waaye ñoom ñoo tooñ (seen bopp).
77وَنَادَوْا يَا مَالِكُ لِيَقْضِ عَلَيْنَا رَبُّكَ ۖ قَالَ إِنَّكُم مَّاكِثُونَ
ña ngay woo : “ Maalik (bëkknéegu safara)! naan ko nanu sa Boroom jéggëli book ! ” muy tontu naan : “Yéen kay, ci [mbugël mii] ngeen di sax dëgg” !
78لَقَدْ جِئْنَاكُم بِالْحَقِّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَكُمْ لِلْحَقِّ كَارِهُونَ
“Indiloon Nanu leen dëgg; waaye ñi ëpp ci yéen dañoo bañ Dëgg”.
79أَمْ أَبْرَمُوا أَمْرًا فَإِنَّا مُبْرِمُونَ
Walla, Ñoom dañoo fexe ay mbir [ak lu man a xew] ? Nun nooy sottal mbir yi ñu alku !
80أَمْ يَحْسَبُونَ أَنَّا لَا نَسْمَعُ سِرَّهُمْ وَنَجْوَاهُم ۚ بَلَىٰ وَرُسُلُنَا لَدَيْهِمْ يَكْتُبُونَ
Moo ndax ñoom dañoo jortu ne dunu dégg li ñuy nëbb ak di ko déeyoo ? Axakañ (dégg Nanu ko de) ! te sunuy ndaw a nga ca ñoom di bind.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
78Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 78

Simoore Az-Zukhruf Aaya 78 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Indiloon Nanu leen dëgg; waaye ñi ëpp ci yéen dañoo…

Simoore Aaya 78/89 — Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zukhruf Dégg, Az-Zukhruf Tekki, Az-Zukhruf mp3, Az-Zukhruf pdf. Aaya 76–80. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers