Ad-Dukhan · 19/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
وَأَن لَّا تَعْلُوا عَلَى اللَّهِ ۖ إِنِّي آتِيكُم بِسُلْطَانٍ مُّبِينٍ ۝١٩
Wa al laa ta`loo `alal laahi innee aateekum bisultaanim mubeen
📖 Tekkim Wolof
Buleen kawe kawe lu ci Yàlla, ndax man dey firnde ju wér laa leen indil.

🎧 Dégg


📜 Aaya 17-21 — Simoore Ad-Dukhan

17۞ وَلَقَدْ فَتَنَّا قَبْلَهُمْ قَوْمَ فِرْعَوْنَ وَجَاءَهُمْ رَسُولٌ كَرِيمٌ
Sànje woon Nanu , nitu Firawna ña leen jiitu woon, te amoon na ñu ab Yonnent bu leen dikkaloon bu tedd,
18أَنْ أَدُّوا إِلَيَّ عِبَادَ اللَّهِ ۖ إِنِّي لَكُمْ رَسُولٌ أَمِينٌ
[daan leen wax naan]: “Delloleen ma jaamu Yàlla yi ! Ndax man mii ab Yonnent laa bu wóor.
19وَأَن لَّا تَعْلُوا عَلَى اللَّهِ ۖ إِنِّي آتِيكُم بِسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Buleen kawe kawe lu ci Yàlla, ndax man dey firnde ju wér laa leen indil.
20وَإِنِّي عُذْتُ بِرَبِّي وَرَبِّكُمْ أَن تَرْجُمُونِ
Maa ngi sàkku muslaay ci sama Boroom di seen Boroom, ndax ngeen bañ ma jóor i xeer.
21وَإِن لَّمْ تُؤْمِنُوا لِي فَاعْتَزِلُونِ
Su fekkee ne gëmuleen ma, kon sori leen ma”.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 19

Simoore Ad-Dukhan Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Buleen kawe kawe lu ci Yàlla, ndax man dey firnde…

Simoore Aaya 19/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers