Ad-Dukhan · 20/59
Tekki Waxtaan — Ad-Dukhan
وَإِنِّي عُذْتُ بِرَبِّي وَرَبِّكُمْ أَن تَرْجُمُونِ ۝٢٠
Wa innee `uztu bi Rabbee wa rabbikum an tarjumoon
📖 Tekkim Wolof
Maa ngi sàkku muslaay ci sama Boroom di seen Boroom, ndax ngeen bañ ma jóor i xeer.
🎧 Dégg

📜 Aaya 18-22 — Ad-Dukhan

18أَنْ أَدُّوا إِلَيَّ عِبَادَ اللَّهِ ۖ إِنِّي لَكُمْ رَسُولٌ أَمِينٌ
[daan leen wax naan]: “Delloleen ma jaamu Yàlla yi ! Ndax man mii ab Yonnent laa bu wóor.
19وَأَن لَّا تَعْلُوا عَلَى اللَّهِ ۖ إِنِّي آتِيكُم بِسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Buleen kawe kawe lu ci Yàlla, ndax man dey firnde ju wér laa leen indil.
20وَإِنِّي عُذْتُ بِرَبِّي وَرَبِّكُمْ أَن تَرْجُمُونِ
Maa ngi sàkku muslaay ci sama Boroom di seen Boroom, ndax ngeen bañ ma jóor i xeer.
21وَإِن لَّمْ تُؤْمِنُوا لِي فَاعْتَزِلُونِ
Su fekkee ne gëmuleen ma, kon sori leen ma”.
22فَدَعَا رَبَّهُ أَنَّ هَٰؤُلَاءِ قَوْمٌ مُّجْرِمُونَ
Muu daldi ñaan Boroomam ne ko : “Ñi de ay niti Tafaar lañu (tooñkat)”.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 20

Simoore Ad-Dukhan Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Maa ngi sàkku muslaay ci sama Boroom di seen Boroom,…

Simoore Aaya 20/59 — Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ad-Dukhan Dégg, Ad-Dukhan Tekki, Ad-Dukhan mp3, Ad-Dukhan pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers