Ad-Dukhan · 38/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
وَمَا خَلَقْنَا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا لَاعِبِينَ ۝٣٨
Wa maa khalaqnas samaawaati wal arda wa maa baina humaa laa`ibeen
📖 Tekkim Wolof
Bindu Nu asamaan yeek suuf si ak li ci seen diggënte di ko fowe.

🎧 Dégg


📜 Aaya 36-40 — Simoore Ad-Dukhan

36فَأْتُوا بِآبَائِنَا إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Su fekkee ne dëggu ngeen kon dekkalleen sunuy maam, délloosileen”.
37أَهُمْ خَيْرٌ أَمْ قَوْمُ تُبَّعٍ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ أَهْلَكْنَاهُمْ ۖ إِنَّهُمْ كَانُوا مُجْرِمِينَ
moo ndax ñoom ñoo gën Tubbaa ak ña leen jiitu woon ? Faagaagoloon Nanu leen ndax ñoom ay niti tafaar lañu woon (tooñkat).
38وَمَا خَلَقْنَا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا لَاعِبِينَ
Bindu Nu asamaan yeek suuf si ak li ci seen diggënte di ko fowe.
39مَا خَلَقْنَاهُمَا إِلَّا بِالْحَقِّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Bindu Nu leen ci lu dul dëgg. Waaye ñi ëpp ci ñoom xamuñu.
40إِنَّ يَوْمَ الْفَصْلِ مِيقَاتُهُمْ أَجْمَعِينَ
Ca bisub àtte ba, lañuy daje ñoom ñépp,
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
38Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 38

Simoore Ad-Dukhan Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bindu Nu asamaan yeek suuf si ak li ci seen…

Simoore Aaya 38/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers