Al-Maida · 100/120
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Maida
قُل لَّا يَسْتَوِي الْخَبِيثُ وَالطَّيِّبُ وَلَوْ أَعْجَبَكَ كَثْرَةُ الْخَبِيثِ ۚ فَاتَّقُوا اللَّهَ يَا أُولِي الْأَلْبَابِ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ ۝١٠٠
Qul laa yastawil khabeesu wattaiyibu wa law a`jabaka kasratul khabees; fattaqul laaha yaaa ulil albaabi la`allakum tuflihoon
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Lu bon ak lu sell yemuñu, doonte yéem na la barig alal ju araam. Nangeen ragal Yàlla yéen woroom xel yi, ndax xéy-na ngeen texe.

🎧 Dégg


📜 Aaya 98-102 — Simoore Al-Maida

98اعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ شَدِيدُ الْعِقَابِ وَأَنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Xamleen ne Yàlla Ku tar mbugal la, te it Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
99مَّا عَلَى الرَّسُولِ إِلَّا الْبَلَاغُ ۗ وَاللَّهُ يَعْلَمُ مَا تُبْدُونَ وَمَا تَكْتُمُونَ
Dara warul Yonent bi lu dul jottal. Te Yàlla xam na li ngeen feeñal ak li ngeen di nëbb.
100قُل لَّا يَسْتَوِي الْخَبِيثُ وَالطَّيِّبُ وَلَوْ أَعْجَبَكَ كَثْرَةُ الْخَبِيثِ ۚ فَاتَّقُوا اللَّهَ يَا أُولِي الْأَلْبَابِ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ
Neel : “Lu bon ak lu sell yemuñu, doonte yéem na la barig alal ju araam. Nangeen ragal Yàlla yéen woroom xel yi, ndax xéy-na ngeen texe.
101يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَسْأَلُوا عَنْ أَشْيَاءَ إِن تُبْدَ لَكُمْ تَسُؤْكُمْ وَإِن تَسْأَلُوا عَنْهَا حِينَ يُنَزَّلُ الْقُرْآنُ تُبْدَ لَكُمْ عَفَا اللَّهُ عَنْهَا ۗ وَاللَّهُ غَفُورٌ حَلِيمٌ
Éy yéen ñi gëm ! Buleen di laaj ci yoo xam ne, bu ñu leen ko leeralee, mu nekk lu naqari ci yéen. Te bu ngeen ko laajee ca waxtu wa Alxuraan di wàcc, ñu leeral leen ko. Yàlla jéggal na leen [seen laaj yooyu]. Yàlla Jéggalaakoon la, Ku lewet la.
102قَدْ سَأَلَهَا قَوْمٌ مِّن قَبْلِكُمْ ثُمَّ أَصْبَحُوا بِهَا كَافِرِينَ
Am na xeet yu leen jiitu yu laajoon lu mel noonu, te ca sababus laaj ya, tax ñu mujj di ay yéefar.
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
100Aaya

Tekki — Al-Maida 100

Simoore Al-Maida Aaya 100 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Lu bon ak lu sell yemuñu, doonte yéem…

Simoore Aaya 100/120 — Simoore Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Maida Dégg, Simoore Al-Maida Tekki, Simoore Al-Maida mp3, Simoore Al-Maida pdf. Aaya 98–102. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers