Al-Maida · 99/120
Tekki Waxtaan — Al-Maida
مَّا عَلَى الرَّسُولِ إِلَّا الْبَلَاغُ ۗ وَاللَّهُ يَعْلَمُ مَا تُبْدُونَ وَمَا تَكْتُمُونَ ۝٩٩
Maa `alar Rasooli illal balaagh; wallaahu ya`lamu maa tubdoona wa maa taktumoon
📖 Tekkim Wolof
Dara warul Yonent bi lu dul jottal. Te Yàlla xam na li ngeen feeñal ak li ngeen di nëbb.
🎧 Dégg

📜 Aaya 97-101 — Al-Maida

97۞ جَعَلَ اللَّهُ الْكَعْبَةَ الْبَيْتَ الْحَرَامَ قِيَامًا لِّلنَّاسِ وَالشَّهْرَ الْحَرَامَ وَالْهَدْيَ وَالْقَلَائِدَ ۚ ذَٰلِكَ لِتَعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ وَأَنَّ اللَّهَ بِكُلِّ شَيْءٍ عَلِيمٌ
Yàlla def na kaaba ga muy néeg bu ñu wormaal, muy lu ñu taxawal ngir nit ñi. Ak àtte weer wa ñu wormaal ak yool ga, ak mala ya ñu ràngal, yooyu yépp [def na ko] ngir ngeen xam ne Yàlla xam na li nekk ci asamaan yi ak suuf si; te it xam na lu ne.
98اعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ شَدِيدُ الْعِقَابِ وَأَنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Xamleen ne Yàlla Ku tar mbugal la, te it Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
99مَّا عَلَى الرَّسُولِ إِلَّا الْبَلَاغُ ۗ وَاللَّهُ يَعْلَمُ مَا تُبْدُونَ وَمَا تَكْتُمُونَ
Dara warul Yonent bi lu dul jottal. Te Yàlla xam na li ngeen feeñal ak li ngeen di nëbb.
100قُل لَّا يَسْتَوِي الْخَبِيثُ وَالطَّيِّبُ وَلَوْ أَعْجَبَكَ كَثْرَةُ الْخَبِيثِ ۚ فَاتَّقُوا اللَّهَ يَا أُولِي الْأَلْبَابِ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ
Neel : “Lu bon ak lu sell yemuñu, doonte yéem na la barig alal ju araam. Nangeen ragal Yàlla yéen woroom xel yi, ndax xéy-na ngeen texe.
101يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَسْأَلُوا عَنْ أَشْيَاءَ إِن تُبْدَ لَكُمْ تَسُؤْكُمْ وَإِن تَسْأَلُوا عَنْهَا حِينَ يُنَزَّلُ الْقُرْآنُ تُبْدَ لَكُمْ عَفَا اللَّهُ عَنْهَا ۗ وَاللَّهُ غَفُورٌ حَلِيمٌ
Éy yéen ñi gëm ! Buleen di laaj ci yoo xam ne, bu ñu leen ko leeralee, mu nekk lu naqari ci yéen. Te bu ngeen ko laajee ca waxtu wa Alxuraan di wàcc, ñu leeral leen ko. Yàlla jéggal na leen [seen laaj yooyu]. Yàlla Jéggalaakoon la, Ku lewet la.
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
99Aaya

Tekki — Al-Maida 99

Simoore Al-Maida Aaya 99 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dara warul Yonent bi lu dul jottal. Te Yàlla xam…

Simoore Aaya 99/120 — Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Maida Dégg, Al-Maida Tekki, Al-Maida mp3, Al-Maida pdf. Aaya 97–101. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers