Al-Maida · 98/120
Tekki Waxtaan — Al-Maida
اعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ شَدِيدُ الْعِقَابِ وَأَنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ ٩٨
Transliteration
I`lamooo annal laaha shadeedul `iqaabi wa annal laaha Ghafoorur Raheem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Xamleen ne Yàlla Ku tar mbugal la, te it Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 96-100 — Al-Maida
96أُحِلَّ لَكُمْ صَيْدُ الْبَحْرِ وَطَعَامُهُ مَتَاعًا لَّكُمْ وَلِلسَّيَّارَةِ ۖ وَحُرِّمَ عَلَيْكُمْ صَيْدُ الْبَرِّ مَا دُمْتُمْ حُرُمًا ۗ وَاتَّقُوا اللَّهَ الَّذِي إِلَيْهِ تُحْشَرُونَ
Dagan na ci yéen la ngeen nappe ca géej ga, ak ñamu géej, muj xéewal ci yéen ñi nekk ci armal. Te nangeen ragal Yàlla, Ma nga xam ne, dees na leen fang jëme ca Moom.
97۞ جَعَلَ اللَّهُ الْكَعْبَةَ الْبَيْتَ الْحَرَامَ قِيَامًا لِّلنَّاسِ وَالشَّهْرَ الْحَرَامَ وَالْهَدْيَ وَالْقَلَائِدَ ۚ ذَٰلِكَ لِتَعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ وَأَنَّ اللَّهَ بِكُلِّ شَيْءٍ عَلِيمٌ
Yàlla def na kaaba ga muy néeg bu ñu wormaal, muy lu ñu taxawal ngir nit ñi. Ak àtte weer wa ñu wormaal ak yool ga, ak mala ya ñu ràngal, yooyu yépp [def na ko] ngir ngeen xam ne Yàlla xam na li nekk ci asamaan yi ak suuf si; te it xam na lu ne.
98اعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ شَدِيدُ الْعِقَابِ وَأَنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Xamleen ne Yàlla Ku tar mbugal la, te it Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
99مَّا عَلَى الرَّسُولِ إِلَّا الْبَلَاغُ ۗ وَاللَّهُ يَعْلَمُ مَا تُبْدُونَ وَمَا تَكْتُمُونَ
Dara warul Yonent bi lu dul jottal. Te Yàlla xam na li ngeen feeñal ak li ngeen di nëbb.
100قُل لَّا يَسْتَوِي الْخَبِيثُ وَالطَّيِّبُ وَلَوْ أَعْجَبَكَ كَثْرَةُ الْخَبِيثِ ۚ فَاتَّقُوا اللَّهَ يَا أُولِي الْأَلْبَابِ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ
Neel : “Lu bon ak lu sell yemuñu, doonte yéem na la barig alal ju araam. Nangeen ragal Yàlla yéen woroom xel yi, ndax xéy-na ngeen texe.
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
98Aaya
Tekki — Al-Maida 98
Simoore Al-Maida Aaya 98 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xamleen ne Yàlla Ku tar mbugal la, te it Jéggalaakoon…Simoore Aaya 98/120 — Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Maida Dégg, Al-Maida Tekki, Al-Maida mp3, Al-Maida pdf. Aaya 96–100. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








