Qaf · 28/45
Tekki Waxtaan — Qaf
قَالَ لَا تَخْتَصِمُوا لَدَيَّ وَقَدْ قَدَّمْتُ إِلَيْكُم بِالْوَعِيدِ ٢٨
Transliteration
Qaala laa takhtasimoo ladaayya wa qad qaddamtu ilaikum bilwa`eed
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
(Yàlla daldi ne leen) : “Bu leen fi xulóo ! Lii lépp waxoon naa leen ko.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 26-30 — Qaf
26الَّذِي جَعَلَ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ فَأَلْقِيَاهُ فِي الْعَذَابِ الشَّدِيدِ
ka daan jéem a woote jeneen Yàlla di ko booleek Yàlla. Sànni leen ko ci mbugal mu tar ma”.
27۞ قَالَ قَرِينُهُ رَبَّنَا مَا أَطْغَيْتُهُ وَلَٰكِن كَانَ فِي ضَلَالٍ بَعِيدٍ
Nekkaaleem ja (Saytaane) ngay wax naan : “sama Boroom, man dey bewloowuma ko ; waaye moom dafa nekkoon ci ag réer gu tar”.
28قَالَ لَا تَخْتَصِمُوا لَدَيَّ وَقَدْ قَدَّمْتُ إِلَيْكُم بِالْوَعِيدِ
(Yàlla daldi ne leen) : “Bu leen fi xulóo ! Lii lépp waxoon naa leen ko.
29مَا يُبَدَّلُ الْقَوْلُ لَدَيَّ وَمَا أَنَا بِظَلَّامٍ لِّلْعَبِيدِ
Wax ja du sippiku fi man ; te it Duma tooñ benn jaam”.
30يَوْمَ نَقُولُ لِجَهَنَّمَ هَلِ امْتَلَأْتِ وَتَقُولُ هَلْ مِن مَّزِيدٍ
Bu keroogee ba Nuy laaj Safara naan ko ; “Ndax fees nga ? ” Safara naan : “Dolli ma” ?
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
28Aaya
Tekki — Qaf 28
Simoore Qaf Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : (Yàlla daldi ne leen) : “Bu leen fi xulóo !…Simoore Aaya 28/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Wednesday, August 19, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








