Qaf · 30/45
Tekki Waxtaan — Simoore Qaf
يَوْمَ نَقُولُ لِجَهَنَّمَ هَلِ امْتَلَأْتِ وَتَقُولُ هَلْ مِن مَّزِيدٍ ۝٣٠
Yawma naqoolu li`jahannama halim talaati wa taqoolu hal mim mazeed
📖 Tekkim Wolof
Bu keroogee ba Nuy laaj Safara naan ko ; “Ndax fees nga ? ” Safara naan : “Dolli ma” ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 28-32 — Simoore Qaf

28قَالَ لَا تَخْتَصِمُوا لَدَيَّ وَقَدْ قَدَّمْتُ إِلَيْكُم بِالْوَعِيدِ
(Yàlla daldi ne leen) : “Bu leen fi xulóo ! Lii lépp waxoon naa leen ko.
29مَا يُبَدَّلُ الْقَوْلُ لَدَيَّ وَمَا أَنَا بِظَلَّامٍ لِّلْعَبِيدِ
Wax ja du sippiku fi man ; te it Duma tooñ benn jaam”.
30يَوْمَ نَقُولُ لِجَهَنَّمَ هَلِ امْتَلَأْتِ وَتَقُولُ هَلْ مِن مَّزِيدٍ
Bu keroogee ba Nuy laaj Safara naan ko ; “Ndax fees nga ? ” Safara naan : “Dolli ma” ?
31وَأُزْلِفَتِ الْجَنَّةُ لِلْمُتَّقِينَ غَيْرَ بَعِيدٍ
Nu waajal Àjjana way ragal ña Yàlla mu jigeñ loolu.
32هَٰذَا مَا تُوعَدُونَ لِكُلِّ أَوَّابٍ حَفِيظٍ
“Lii mooy li Nu leen daan dig , [mu ñeel] bépp delluwaakoon ci Boroomam tey sàmm [daytalu Boroomam]
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
30Aaya

Tekki — Qaf 30

Simoore Qaf Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu keroogee ba Nuy laaj Safara naan ko ; “Ndax…

Simoore Aaya 30/45 — Simoore Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Qaf Dégg, Simoore Qaf Tekki, Simoore Qaf mp3, Simoore Qaf pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers