At-Tur · 45/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
فَذَرْهُمْ حَتَّىٰ يُلَاقُوا يَوْمَهُمُ الَّذِي فِيهِ يُصْعَقُونَ ۝٤٥
Fazarhum hatta yulaaqoo yawmahumul lazee feehi yus`aqoon
📖 Tekkim Wolof
Bàyyileen , ba ñu dajeek bis ba ñu leen di mbugël,

🎧 Dégg


📜 Aaya 43-47 — Simoore At-Tur

43أَمْ لَهُمْ إِلَٰهٌ غَيْرُ اللَّهِ ۚ سُبْحَانَ اللَّهِ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Walla ñoom dañoo am jeneen Yàlla ju dul Yàlla ? (Mukk) Tuddnaa Sellam ga soree na lool ak liñu koy bokkaale !
44وَإِن يَرَوْا كِسْفًا مِّنَ السَّمَاءِ سَاقِطًا يَقُولُوا سَحَابٌ مَّرْكُومٌ
Su ñu gIisaan mbugël sax muy wàcce asamaan, dañu naan : “Niir yu dajaloo la”.
45فَذَرْهُمْ حَتَّىٰ يُلَاقُوا يَوْمَهُمُ الَّذِي فِيهِ يُصْعَقُونَ
Bàyyileen , ba ñu dajeek bis ba ñu leen di mbugël,
46يَوْمَ لَا يُغْنِي عَنْهُمْ كَيْدُهُمْ شَيْئًا وَلَا هُمْ يُنصَرُونَ
bu keroogee seen pexe duleen jariñ dara, te kenn duleen dimbali.
47وَإِنَّ لِلَّذِينَ ظَلَمُوا عَذَابًا دُونَ ذَٰلِكَ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Te kat tooñkat ya ñoom danañu am mbugël mu yées lolu. Waaye li ëpp ci ñoom duñu xam.
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — At-Tur 45

Simoore At-Tur Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bàyyileen , ba ñu dajeek bis ba ñu leen di…

Simoore Aaya 45/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers